@mouslimsambadiallo: 🦁💰 Épisode 3 – La première attaque ! Mamadou ak ay sàccam jéem nañu taxawal Patron Moussa ngir sàcc xaalisam. Waaye Pape def na lu doy waar te Moussa mucc ci seen loxo. Ndax ay sàcc yi dañuy dellusi ak pexe bu gën a metti? 👀 Bul fatte xool ba ci jeex! 💬 Wax ma ci commentaires: Kan nga gëm, Moussa walla Mamadou? ❤️ Like 🔁 Partage ➕ Abonne-toi ngir bul rëcc benn épisode. #PatronMoussa #SerieWolof #TikTokSenegal #Wolof #Senegal