@user88235435483:

user88235435483
user88235435483
Open In TikTok:
Region: SN
Wednesday 15 July 2026 21:54:58 GMT
425436
31884
998
240

Music

Download

Comments

user61793516720050
🇸🇳séné gambia 🇬🇲palaphone :
bilakhi souma amé ken dou sonou😭
2026-07-16 10:56:04
1755
khadimtouhfatou
khadim touhfatou :
Motakh Lou way am warr nako santé yalla
2026-07-16 20:03:30
919
beugfallou19
beug fallou :
kousi diaroul rek manoko xam je me souviens ay nuit yimadan diok di té nekbi mak sama yay .
2026-07-16 05:11:13
391
fatou.zulleyha.za
Zuleyha📸 :
Nagnou def cagnotte pour mome
2026-07-16 21:53:19
166
bibah.bibah437
Belle Âme ☺️ :
Motah sou khiné gni nekk si genre situation rk lay khalat motah douma beug mou taw walahi azim 🥺🥺🥺
2026-07-16 21:09:46
55
papa.mbngue
Papa MBéngue :
😢🥺🥺🥺🥺🥺🥺🥺🥺😭😭😭DiNaBakh
2026-07-16 23:28:27
1
faye0852
Aïda faye :
Ndeyesane man ak sama yaye doundou nan li doumako fate mais lepp diékh na
2026-07-16 14:44:36
82
lamtoro.26
Laye laye :
Oooh yalnalén yallah takhawou mayléne lou kawé ndiorte🙏🙏🙏🙏
2026-07-16 23:37:05
35
elfallfall
Elfall Fall :
Nit limou wara sante yalla dafa bari
2026-07-16 22:05:17
37
elcap145
M’y name is Saliou 🙌🏿🥰 :
Ndaysane je me rappelle très bien nawéte boudone taw ngalaw man ack sama yaye daniouye takhaw diap nek bi ba ngalaw bi arrêter khale yi teud nelaw 🥺
2026-07-16 09:10:38
62
salioudeug08
𝐎̸𝐆✦𝐒𝐚𝐥𝐢𝐨𝐮🥇❤️ :
Borom bi rk lay nékh ❤️😔🥺☝🏿
2026-07-16 23:37:22
0
user987446915905
Aliou soung :
Ohh Ndéysane yalla bakhna🙏🙏🙏
2026-07-16 09:18:07
1
pape.seck2263
Pape Seck :
Ndeyssane mast
2026-07-16 11:53:49
1
papethiam7356
Pape Thiam :
lep pay bakha inshalla
2026-07-16 09:40:37
1
lampe.faye3
Lampe Faye :
yalla marina sutoura
2026-07-16 01:58:58
1
w762961000
taw sylla ambasandar bien 12 :
ouu massta way de na bakh de billahi li ay itass laye done bilahi
2026-07-16 11:13:26
31
aliou.baye.fall6
Aliou Baye Fall💦💦 :
2026-07-16 13:59:07
21
mamefatydiaw34
user2283623581258madam :
naysane metina yalla bakhna
2026-07-16 21:09:54
5
narousoncko
soncko à vie :
avec ça 1960 ba tay ya des villages qui souffre en silence
2026-07-16 23:06:34
5
mbaye.ndiaye7712
mbaye ndiaye :
2026-07-15 22:34:04
14
ousmanesow50861
Ousmane Sow :
Li yagna am leep gen film
2026-07-16 19:59:30
7
alioubadaratiaw
user1633324969724 :
yalnala yalla may tabakh
2026-07-16 06:57:49
7
gsm_gueye25
khelcom global business ♑ :
metina dh mais délén faratal di saxal ay garab you bary lou am solo la bou keurgui barywon ay gara🌴 dega yi dou bary
2026-07-16 11:25:15
9
To see more videos from user @user88235435483, please go to the Tikwm homepage.

Other Videos


About