Kilifa dou si âge yeurmade moy leep ak considération Khale sa meune na nek kilifa
2026-07-18 22:51:22
47
sunsei1010 :
Kilifeu wala khaliss key
2026-07-18 21:26:04
44
Le Sénégal Avant Tout❤🇸🇳❤ :
Bou matté kilifeu té amoul xaliss nak juste une question damay lathié rék déh🤔
2026-07-19 06:45:49
11
you one black TV 🇸🇳🇺🇲🎤🎤? :
Xalise rék géni top xam nan Lép
2026-07-19 01:45:28
9
Cheikh Dieng🥰🇸🇳 :
Diamono bi les termes on changer mots ne signifie plus le même kilifeu , kou bakh ,koula meune yorr kou ame yeurmandé kou bakh le tous moy kou ame xaliss rek
2026-07-20 13:46:44
4
LORD👑👑👑👑GUEYE :
moy ku yor xaliss rek
2026-07-19 01:54:13
8
Elhadji Thiam :
Xaliss guèn geum
2026-07-18 23:35:17
4
Princesse lamtoro wally :
bilay walay monument de la Renaissance dh matoul kilifa mo tass keureum
2026-07-16 12:12:37
27
MatarInsa :
na fèk mou am xaliss tmt
2026-07-19 02:03:11
2
User223335555 :
bilay kou la matt kilifeu amna solo dé🥰🥰🥰
2026-07-16 11:58:30
14
M dji 44❤️❤️❤️ :
soy tak tamite takal kou mat soxna c très important
2026-07-20 14:27:58
0
Miss 🇸🇳 :
elle a raison vraiment ma xam limouye wax
2026-07-18 16:12:53
11
Camus Albert :
La société est matérialiste malheureusement ! Oustaz bi geunn bakh si cogne bi menoula diott ndakh depassam doyoul ! Nell kelifa gou am xaliss