lolou moma dal ak sama bén tonton wakhal ma louma défoul khéxe ak mane sama Mame guéné keur gui t'a yalla khamna ni sama tonton défou mako dara timis mo diote sama dôme niew si keurgui dima séte mou diapko dorko néko n'a gueune keurgui maye wakh ak môme mou songue ma khélh
2026-07-17 03:11:55
464
~Une Luna❤️🌸🦋 :
Yalla nagnou yalla samal bopame🥹🙏
2026-07-17 00:26:18
187
Soxna mbacke❤️ :
Hee Aka gnouko mannn 🥹😩sama dieukeur deé gnou nieuw si sarakh si doulel ma lou reuy
2026-07-17 11:58:13
97
Glow by Awa😍 :
Man sama yaye da ganiou ma nékk ak sama tata ci keur gui domame bi beugue ma indil ma thiow ni ma wakh Yayam moh liguéye sama yaye bamou dh histoire bi amna 3ans bataye mangui koy gardé yalla nama yalla até ak kokou lépp nguirr beugue ma torokhal yalla geumoul nélowoul
2026-07-17 22:32:27
47
Talibé cheikh :
mane déh sama dome dieukeur boh khamné moma mag foufe di woudiél yayam té yayame tasna 17 ans avant maye seysi si papam tuumal nama lo khamnii doumakoko bale ba yawmalkhiyam té magui niane yallah nama yallah atté AK adouna AK alakhira dakhe bouga délo yayame ak papam wayé doumakoko bale ba yawmalkhiyam.dakhe mome kou papam tak mou guénéla keur gui wayé guenone keurgui sa mo guénéla louma tuumal
2026-07-18 12:15:21
11
Fatou{Barra}🦋🎀 :
Mon ami a vécu la même chose 😔
2026-07-17 14:34:31
16
🦋𝑆𝐸𝑟𝐩𝐄𝐍𝐓༆𝑩𝑳𝑨𝑛𝐶🐍 :
Bilah dinaniou la wakhal lo khamni do kham sakh fou lolou diougué ms bilay walahi dou ma len meus ball ba nièti fanou bamel douma len ball heure bou ma toguè khalat liniou wakh ni mako def té defouma ko rek damay beugue kharou 😭😭😭😭
2026-07-18 18:13:00
5
Ndiaye ♥️♥️♥️lady ♥️♥️♥️♥️ :
Bilay mais bayinako ak yalla 😭😭😭😭😭😭
2026-07-17 15:22:28
17
Rokhaya BouMoustapha AlMaktoum :
billah
2026-07-16 20:49:02
32
Princess Noir🇬🇲✅ :
Blie defa metti trop
2026-07-17 18:32:30
8
sokhnafallou306 :
Mofi am deee😭😭😭
2026-07-17 02:04:29
8
Fatou Ndiaye :
salallahou allah mouhamed salallahou allah mouhamed 😢
2026-07-19 13:30:12
8
thiatou papam ❤️❤️ :
bly dama dioy ba soon 😭 guisouma ken
2026-07-17 16:27:28
5
Ndeya bou me ndiaye savon :
Bilaye Lou meti 😭😭😭
2026-07-17 00:44:00
11
Meta shop 🛍️By timah🌸🛍️ :
Bilay doundou nako
2026-07-17 14:36:12
6
Yakhara.mou serigne saliou ❤️ :
Bilay Bilay ♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️
2026-07-17 00:59:48
9
Oumy satou Bayob goor :
Bilaye dague la de lou meti Toma
2026-07-17 14:43:43
6
Mamita😍😍 :
Ohhh
2026-07-16 21:48:00
7
Princesse 👸 fadilate ❤️ :
dafa méti 🥹🥹
2026-07-17 15:36:39
4
elementbayekarim56 :
Yomalkhiam dina meti déee bilaye
2026-07-18 18:56:13
2
Awa fall Mrs Lakhone💍♥️ :
touuma day ray gorrr wallahi😔
2026-07-20 15:55:08
1
bathily yama :
billay 😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭
2026-07-17 01:19:09
6
série sénégalais🇸🇳 :
damay défar affiche AK logo
2026-07-17 11:29:56
4
To see more videos from user @tiktoksengal, please go to the Tikwm
homepage.