vrement mame wallo beug nane la trop mai wakh dji nga wara wagni kou mine say wakh yapla chak jour maman nila liguéyal ta bayi détails tal sa live di wakh rek sama dome yi dama sone dama li koula beug khass sakh fofou lalaye diar daga warra mature nga wagni sa wakh dji vraiment ta focus nopi stp setale si maman 🙏