Saway kila eupalé loum dénthie moula eupalé alall nak
2026-07-17 14:15:47
121
Amdy.Karimien :
kila eupeulé lim dinthie kay mola eupeu alal
2026-07-17 16:09:46
39
La paix du cœur :
paracetamols 😅😅😅😅😅
yallah na nieup am xaliss
2026-07-17 19:55:45
1
15 ligue des champions :
deug la dh wallahi
2026-07-17 14:42:46
23
BABACAR🧸❤ :
louy agne
2026-07-17 15:33:52
10
diouf déco693 :
Doylou moy leup
2026-07-17 22:42:39
3
Diouf solution 💯 :
ay wax la wax deh 🥰 deugg la laaj
2026-07-17 20:38:30
3
ennemi de la pauvreté :
dekk len di dalal sen xel rek di nakh sen bopou dina bakh
2026-07-17 15:23:31
8
madmsambou :
❤️❤️
2026-07-17 12:07:13
5
lil💎 :
Wakhoufi dara
2026-07-17 20:00:19
0
koumougne mougne :
sama patron daf gnouy wakh man la yala déf ma djitélén wayé loudoul lima sol AK lima diota lékagoum momou mako bala gén ka kham yala dieul sama bakan fini