Bén Pa meuss nama fék corniche may diangue mounima auto yi di romb loumou rafét rafét boul nié kén ndakh khamo nouniou def ba am ko. C'était ma première année ndeysan. Et le vieux m'a énormément conseiller dans la vie. Je n'oublie jamais le vieux.
2026-07-17 23:46:34
403
Black Angel 👼🏾🇸🇳👼🏾 :
C’est interdit en l’islam de faire des pactes avec les djinns
2026-07-17 19:04:54
1967
♎️ Tiana 🧚♀️ :
Li la wolof Ndiaye nane nitt dîna wakh ba lamb tatam nè dou bossam
2026-07-17 20:55:21
620
toufa :
vraiment oustaz liga sol rafetna machala
2026-07-17 19:02:18
1448
multiservice automobile :
mane ki ay domam la yereum
2026-07-17 20:18:28
813
electro business sénégal 🇸🇳 :
motakh si adouna boul gnié keneu
2026-07-17 19:40:48
2493
Ndeya gueye🍀 :
Mame ndiaye est ce que khamna limouy wakh
2026-07-17 19:42:49
1844
Lepp jamm Lepp tawfekh :
Djinné loumou la may nangou watt ko
2026-07-17 20:23:21
597
Faye mou baye Karim💎🛍️ :
Lou way déff boppam
2026-07-17 19:02:20
734
Mariama sonko :
thiéy yalla 🤔
2026-07-18 07:08:20
0
MB B D :
terrible
2026-07-18 07:25:48
0
Senégalais :
way momla rek
2026-07-18 06:47:58
0
Gemini Ai🧊❤️ :
Boulen tek beut kén doylou rk tei yakar yalla inshallah
2026-07-17 20:35:34
292
ndiaye madrilène :
nitt dina wax ba dougale bopam
2026-07-18 06:45:56
0
diop diatou :
wakh dina dougal nit
2026-07-18 06:08:33
0
setü serigne Mor ndiaye Euréne :
am na yo xamni même boko défé boul tok thi pencc diko waxate
2026-07-17 18:29:41
973
amitambaye798 :
salalahou allah Mouhamed 💚🖤
2026-07-17 23:58:48
70
Arame Gaye :
mom néna dagnko ni prison ba accident mouni da yagu risqué prison la tamponner mom kéy bou niémé won risque deugu accident lay dieul vu que mo gueuneu risqué prison
2026-07-17 18:29:01
459
Nicky Gambia :
Dafa reuy lamen rek
2026-07-17 19:32:50
326
𝕄𝕆ℝ ℕ𝔻𝕀𝔸𝕐𝔼 🇸🇳🇺🇸🇦🇮 :
Fane lagnoukoy déffé
2026-07-17 19:49:32
48
To see more videos from user @serigne_mahdiyou_niane, please go to the Tikwm
homepage.