@film.en.wolof.1: 🕵️♂️🔥 Épisode 7 – Le traître est parmi eux ! Mamadou ak ay banditam dañuy xalaat ne am na ku leen di wax 😱. Pendant ce temps, Moussa révèle à Awa ne xaalis bi ci coffre bi du xaalis bi gëna am solo 💰👀 Waaye ku nekk ci gannaaw bunt bi? Ku moooy nit ki xam secretu Moussa? 😱 L'épisode 8 dina wone ku moooy traître bi! 💬 Wax ma ci commentaires : Ku nga foog ne mooy traître bi? ❤️ Like 🔁 Partage ➕ Abonne-toi ngir bul rëcc épisode 8! #PatronMoussa #SerieWolof #TikTokSenegal #Wolof #Senegal