@lamignou_darou_1912: #senegalaise_tik_tok🇸🇳pourtoichallenge #youshouldknow #wallyseckofficiel #pasteflespatriotes #sonko2029🇸🇳inchallasénegal

Lamignou Darou 1912
Lamignou Darou 1912
Open In TikTok:
Region: SN
Sunday 19 July 2026 16:14:38 GMT
86303
14493
703
1597

Music

Download

Comments

jpierre77
Soleil :
Aka wakh deugu. Macky sall limouy dokh Sénégal yeup dou diameu. Macky dou dokh diameu
2026-07-19 18:37:38
150
moumeu72
moumeu😶😶 :
bilahi Walahi deug rek gua wakh Ousmane Sonko dou néne amena lou yalla name si mom pour mane niani kilifa yi LA yalla wara watié Senegal beug nio bolél kou dioup té sell moy defar Senegal bilahi
2026-07-19 23:09:15
59
mouhameth314
mouhamet Ndiaye :
billahi même man si guente lako guiss khamouma si politique dra mais sonko rek la beugue 💪
2026-07-19 21:27:52
151
leuz8306
leuz🇸🇳🇮🇹 :
Sonko déi Bilahi wallahi 2024 lako guénte avant les election la guiss ni dou bokk election 2024 wayé att sangaam lay nek president dumako wax fi motax limou nékoul wone candidat 2024 bétou ma motax li dess ci yonam xell mou dal laci am ndax guénte bi yamoul fofou féké ak tal lakay nianal inchallah
2026-07-20 01:58:48
37
dijavip
Reine mère bu Sonko :
Sonko kubakh beug ko
2026-07-19 21:54:31
94
kamallo78
Bege yalla 🕊️💕🕊️ :
Magie lay nahnal goudo fan ak wer ga feke lepou silla
2026-07-19 23:23:28
21
alioudiopsam
DIOP BAYE SAM SONKO AVI :
SONKO SEUL ❤️❤️❤️
2026-07-19 23:32:19
31
liberocisse
Libéro Cissé :
GOUDEUL FAANE ANDAK WEUR SUNU WADIOUR GUI ❤️
2026-07-19 17:17:43
41
tourdecontrole221
L ’Autorité 🫡 :
Il s’appelle comment sunu papa dji
2026-07-20 09:11:22
12
aliou.dia.12
Aliou Diagne 💎🇸🇳🕋 :
sonko rékk sii diam dji sonko avis ♥️
2026-07-20 00:04:59
28
mm.patriote.0
M&M diop🥇🏳️ :
Dama beug mac bouy gougue ak diabotam si deug yalla nala fi yalla bayi 🙏🏽
2026-07-20 00:26:46
14
yapsa313
Yapsa xanthie fall :
Yalla na yalla doli diam Ousmane Sonko
2026-07-20 00:50:38
10
abdouseck4702
abdouseck :
❤️❤️❤️
2026-07-19 21:02:24
24
ms344008
ms :
ay père doundeul 🥰🥰🥰
2026-07-19 23:13:50
9
barathiam779
bara thiam :
merci beaucoup papa patriote
2026-07-19 20:27:20
24
racinele.dbonnair
Racinele dèbonnaire :
billahi gorgui ya bakh macha allah
2026-07-19 23:44:38
17
00bm77777777
User :
Père yalla nga goude fane ❤️❤️
2026-07-20 10:47:26
10
masssakho676
Sakho 784558131 :
🥰🥰 Sonko 🥰🥰 Sonko
2026-07-19 23:01:40
23
aliounefall9058
Alioune fall :
Machallah amna sollo sonko Rak fall
2026-07-19 20:15:01
13
mbathe03
Nawone wonina :
diadieuf serigne syll machallah sétou cheikhou serigne Touba la dé wadji dou wakhantou béne bess rek la sekh ak mome ma khamné lamign bi dou wakhantou bilay
2026-07-19 23:24:54
10
deeffdeegg
deeff deegg bayfall :
Bilahi Lahilaha ILALA
2026-07-19 22:07:27
5
sokhnafakl
sokhnafakl :
papa merci c est courageux
2026-07-19 22:10:57
11
abdou.diba900
Abdou Diba :
2026-07-19 23:13:34
5
abdou.diba900
Abdou Diba :
2026-07-19 23:13:30
6
omarthiam924
Omar bo sonko :
merci beaucoup bonne continuation
2026-07-19 20:39:15
7
To see more videos from user @lamignou_darou_1912, please go to the Tikwm homepage.

Other Videos


About