mane dh serigne Touba mooy sama référence di sama lepp c pourquoi j m'intéresse beaucoup à ses écrits loumou wakh ma geum ko th diko dokholé Nonou mom kepp moyy sama source
djeuredjeuf borom touba
2026-07-21 01:43:07
16
yankhoyba diop taysir :
loulu moy li am bari na ci niom lool
2026-07-19 19:26:54
15
ndongal daarayi :
إذ بان جهرا بدل فبان جهرا
2026-07-20 05:07:25
14
modou mbaye :
yonam wi dé amoul lousi lendem léral na lép walahi
2026-07-20 21:31:31
6
Abibou mbengue HT :
jërëjëf serigne touba diarama saa mame cheikh ibra fall ❤️
2026-07-19 23:38:53
16
Mustapha Diop :
bane xasida la ?
2026-07-20 13:31:38
0
Al ahad tv làmeniou degue :
ndeysan machallah
2026-07-19 20:10:45
12
Cheikh Mbacke Best Man :
Aka Wérrr🙏
2026-07-19 23:37:27
6
Imam Seck :
má Sah Allah 💚💚💚🤲🏾
2026-07-19 20:09:41
4
fallou mbaye :
ak wérre ✊💯🤜💥🤛♥️🫵ak téwlou bou wére la matawo wa salam
2026-07-20 02:01:45
1
محمد البشير سين🤍🫀 :
Lerna nagn❤️😭
2026-07-20 00:21:16
4
NAAR DIANGE :
lii de mooy dëgg
2026-07-20 14:50:44
1
mouhamedsagnane :
ana lougnouye rabê téguine ci wakhi kou baakh ki moom lépeum ma téguîné limou bind koukoy wakh di ame loo ci bayi khél wala koosi bayi khél doo dara ci serigne bi .fii aye djaamou yallah képp dongue gnoofi nék gneup sounou boroom moolén bind té serigne touba lou yallah digulé rék la digulé lou yallah rék la digulé .kou ko djangue bagnkoo wakh di nguako layoo ak serigne bi euleuk billaahi wallaahi..
2026-07-20 15:23:41
5
DABO CRÉATION 📖👔👚❤️💝💚 :
ما شاء الله يالشيخ
2026-07-21 01:47:52
0
diopdiallor :
way leral way 😳 damalay mérédé 😳
2026-07-21 23:06:52
1
Thiaw jannatu :
Ay way lii doy na waay
2026-07-21 23:41:21
0
Thiane Fallou :
akasa
2026-07-21 06:31:18
0
7 :
por tan njio Mèl nii la rewmi sokhla
2026-07-21 02:16:44
0
Serigne gora al Miss bakh :
adji mag djiy
2026-07-21 10:04:27
0
To see more videos from user @mina_ia_, please go to the Tikwm
homepage.