@xol_ak_xel19: Li moo tax nga war téey 🧏♂️ | #motivation #mindset #tfm #senegal #sénégal Li moo tax nga war téey. Ci vidéo Pape thioune ak Khadim Diop ci émission nekkiin ci partie bi ñu ngi done wax ci ndogalu Yàlla ak nit ki nim mëné def lu ko war lep ba paré du am lim bëgg ndax Yàlla ndogalu ko wala jottëgul mu nekk lu am solo lu wara tax nit ki bañ di yakamti addinam nak ñu ngi wax ni Yàlla xamul lu jaadu lu jot la xam.
Vérité absolue, Qu'on laisse nos craintes et nos doutes car a chaque pas du développement de notre existence correspondait exactement à ce que Dieu avait voulu faire de Nous.
2026-07-22 14:27:36
3
Kocc Bou Maodo :
lolou rek nga wara wakh sonko seul
2026-07-22 15:28:21
1
fatysy71 Wally :
Walahl Walahl 🥰🥰🥰🥰🥰🥰🥰
2026-07-21 19:06:16
1
Alou :
Wallahi
2026-07-21 07:51:19
3
serigne Babacar xadimou rasoul :
tawfekhe yalla
2026-07-21 20:38:21
2
user591725263442 :
2026-07-21 17:53:26
2
Gorgui :
billaye 👍🏿
2026-07-22 15:29:13
1
Mariama Ndiaye salihate❤️💯 :
Absolument
2026-07-22 10:29:36
1
seck messi jR 🇪🇸🇪🇸🇪🇸🇸🇳 :
❤️❤️
2026-07-22 13:45:47
1
Babs :
wallay ndaysan
2026-07-22 00:57:49
1
Apple@89 :
Vraiment
2026-07-21 10:11:13
1
Borom Ndiéne :
🥰🥰
2026-07-21 17:12:59
1
Xol Ak Xel :
Voilà 5 actions que tu peux faire pour me donner de la force :
1) Liker la vidéo
2) Enregistrer la vidéo
3) partager la vidéo (même si tu le supprime après 3 secondes)
4) T'abonner (si ce n'est pas encore fait)
5) Commenter pour donner ton avis (le plus important)
2026-07-20 22:48:58
2
cheikhal khalifa ababacar :
🥰🥰🥰
2026-07-23 10:24:20
1
Momo chér :
🥰🥰❤️
2026-07-21 22:34:12
1
omar2006 :
🥰🥰🥰
2026-07-21 15:12:46
1
fallou fall23 :
🥰🥰🥰
2026-07-21 12:35:33
1
user83669722177227 :
😎😎😎😢😢😢😢
2026-07-21 09:20:25
1
user5482526506690 :
🥰🥰🥰
2026-07-22 20:38:44
1
mouhametk1 :
❤️❤️❤️
2026-07-21 13:24:12
1
ndiaga matar :
❤️❤️❤️
2026-07-22 12:27:32
1
falloukairè :
🥰🥰🥰
2026-07-22 20:18:45
0
aefzatyh :
🥰🥰🥰
2026-07-21 08:06:26
1
To see more videos from user @xol_ak_xel19, please go to the Tikwm
homepage.