@tahirouhiroutadia: @Titi Sénégal l’officiel @kylie droga Mrs TD 💍❤️🔥🫂 ton Marie est fier de toi 👍🥰 #senegalaise_tik_tok🇸🇳🇸🇳 #tiktoksenegalaise🇸🇳🇸🇳 #dakartiktok🇸🇳 #baptemesenegalaise #viralsenegal
Titi dem khéw way beuriwoul dh linga am beurina Machalla ❤️❤️❤️
2026-07-21 13:37:56
1068
KSF✨🇸🇳🛍️ :
titi def nga Lou rafet tahirou dala beugue nila kila beugue mola sonal
2026-07-21 11:36:56
1835
Ndeyabijouterie :
Tahirou dafa beug titi machala yalneu doundou tei barkel ❤️
2026-07-21 01:58:47
1021
yamagueye08 :
wakh dégue nékh yalla li môme mérite la si yaw dakh mane à chaque fois magui guiss saye vidéo titi rk ngaye topou yalla nalla Yalla défal diamou yaw AK sokhnasi si barké Serigne Babacar sy malik 🥰🙏
2026-07-21 09:56:16
285
Leye bousso :
limoy woyou khol deuk manchallah
2026-07-21 09:28:33
190
diatousagna3 :
Oh préféré a vie Titi ma la beug long vie au bébé
2026-07-21 12:46:21
32
Bigue bou s fallou❤️😘 :
Machalla li nekhna way 🥰🥰❤️
2026-07-21 10:45:37
21
Moustapha 1356 :
sey ba dhé rek🥰🥰🥰🥰🥰🥰🥰
2026-07-21 00:34:07
30
Doylo yallah :
oh machallah beugue yeuk mokoy faye titi defna lou rafet way
Mashalla Woly amga diabar diu bakh xol bou rafet nagou ligueye nek nekine bou rafat avec sa grande mère. Kou def lou bakh degue ♥️♥️♥️
2026-07-21 01:56:08
13
𝐚𝐯𝐨𝐜𝐚𝐭 𝐥𝐚 𝐥𝐢𝐨𝐧𝐧𝐞 :
sama khôl bi sedatina tahirou longue vie à notre prince adoré
2026-07-21 13:10:44
16
AHMADOU BAmB@ :
barkeii ñion geuinteiii nk enh mn ami 🥰🥰🥰🥰🥰
2026-07-21 11:31:39
11
RasSoul______MbAye ❤️🫂 :
Ki rek la beug ❤️
2026-07-21 16:49:02
5
user942133 :
Bilay. Ay nit you bx lagn tahirou et safamille une famille exceptionnelle
2026-07-21 12:23:51
9
Bb aïda 😍❤️ :
Ndeysan Machalla ❤️🥰
2026-07-21 09:37:53
7
Modieneyauck :
toutes nos félicitations long vie aux bébé😘👶
2026-07-21 08:13:18
26
Maman Soumare :
Machalah la mifa li mom yénako diar beug la lionne bamou diékh 🥰
2026-07-21 10:00:25
6
Rougui kane 12.com :
Woly c’est la fille de titi oubien
2026-07-21 10:09:23
196
yayou Serigne saliou 🙏🙏🙏 :
machallah yalla na bb bi dounde té am ndaye ak bay mai pourtant meunone ngua mako yeugueul ma gnew diamou ndakh domou nidiaye ydii mbok bou amé dila am sou amoul balak langua yor🥰🥰🥰🥰
2026-07-21 02:32:12
22
yayoumbendafall :
bilay ya beugue titi wayè titi yeuk gua sa nitt machalla
2026-07-21 11:26:45
11
To see more videos from user @tahirouhiroutadia, please go to the Tikwm
homepage.