@ibraaymaxaliil: Le Président de l’Assemblée nationale, Monsieur Ousmane SONKO, a effectué, ce mardi 21 juillet 2026, une visite des différentes directions de l’administration parlementaire. Cette démarche lui a permis de s’imprégner du fonctionnement des services, d’échanger avec les responsables et les agents sur leurs missions et leurs conditions de travail, ainsi que d’identifier les principaux défis auxquels l’administration est confrontée. Cette visite lui a permis de s’enquérir du fonctionnement des services administratifs et techniques de l’institution, ainsi que des conditions de travail du personnel. Au cours de cette visite, le Président de l’Assemblée nationale a échangé avec les responsables des différentes directions. Ces échanges ont également constitué un moment d’écoute et de dialogue direct avec le personnel, permettant d’identifier les attentes, les défis et les perspectives d’amélioration de l’administration parlementaire. ________ Njiit lu PÉNCUM NDAWI ASKAN WI, Sëriñ Usmaan SONKO, amal na, ci talaata jii 21i fani sulet 2026, ab nemmiku ci yenn wànqaasi ndoxalug ndawi askan wi. Nemmiku bi tax na mu nànd doxiinu wànqaas yi, diisoo ak kilifa yi ak liggéeykat yi ci seen i liggéey ak seen nekkiinu liggéeykat, ak xam jafe-jafe yi ndoxal gi di jànkoonteel. Nemmiku bi tax na it mu am i xibaar ci doxaliin wi ak xereñteg campeef gi, waaye ak nekkiinu liggéeykat yi. Ci biir nemmiku bii, Njiit li diisoo na ak kilifay wànqaas yi. Diisoo yu am solo ci teey ak waxtaan yu xóot ñeel liggéeykat yi, ba tax mu xam seen i yitte, jafe-jafe yi ak pexey ñoŋal ndoxalu ndawi askan wi. #ansen #senegal

focus 2050 ak Seydina Ousmane
focus 2050 ak Seydina Ousmane
Open In TikTok:
Region: SN
Tuesday 21 July 2026 19:43:01 GMT
7013
1716
59
13

Music

Download

Comments

user8650007076207
user8650007076207 :
des hommes de valeur et des femmes de valeur Merci Ousmane sonko😍
2026-07-21 20:10:23
5
soledaroboromelambaye
Djiliye Lambaye 2050 ak sonko :
Masallah
2026-07-21 20:10:39
1
amadou.badiane527
Amadou Badiane :
🥰🥰🥰sonko 2029
2026-07-21 19:45:08
1
diagne8333
Ibou diagne Sonko ♥️ 2029 :
2026-07-21 22:31:53
1
moussambaye93
beugue fallou :
li moye gouvernement
2026-07-21 19:55:19
1
maguette.seye80
Maguette Seye :
Machallah Machallah ♥️♥️♥️♥️🥰♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️merci Merci sonko sonko 💯💯 vie 2029
2026-07-21 20:15:46
1
mame.bousso16
mame.bou sonko :
🥰
2026-07-21 22:06:17
0
dia.babacar.220
bayou fatima :
ho wallahi❤️❤️❤️💚💚💚💙💙💙💙
2026-07-21 21:47:24
0
salioumachine0
salioumachine0 :
❤️❤️❤️❤️
2026-07-21 20:27:53
0
laye4121
laye 👎♥️♥️👍👍 :
sonko rék sonko rék 🥰🥰🥰
2026-07-21 20:04:47
1
abdoulayesarr4118
Binette Sarr :
🥰🥰🥰🥰🥰
2026-07-21 20:37:30
0
modou.cicse
Vente de vaisselle 🍽️🍴🛋️🛒 :
❤️❤️❤️
2026-07-21 20:06:24
1
santyallabouweer
Modou :
❤️❤️❤️❤️❤️
2026-07-22 16:08:16
0
cheikh.1998
CHEIKH 1998 :
✌️✌️✌️
2026-07-21 20:03:37
1
amsa.bou.sonko1
Amsa bou sonko :
💚💚💚💚💚💚💚💚💚💚💚💚💚💚💚💚💚💚💚💚💚💚💚💚💚💚💚💚💚💚💚💚💚💚💚💚💚💚💚💚💚💚💚💚💚💚💚💚💚
2026-07-22 11:47:34
0
mansour.sy763
MANSOUR Sy :
❤️❤️❤️
2026-07-22 03:43:56
0
moussambaye143
moussambaye143 :
❤️❤️❤️❤️
2026-07-22 09:10:33
0
bambatouba3656
bambatouba3656 :
❤️❤️❤️
2026-07-22 14:14:47
0
user9040407939655
sope seydina Ousmane sonko :
🥰🥰🥰
2026-07-22 08:38:38
0
abdoulahatseck02
Abdou lahad Seck :
❤️❤️❤️
2026-07-22 08:01:04
0
matarcamara775
MTbou SONKON :
🥰🥰🥰🥰🥰
2026-07-22 05:00:47
0
abdoumbacke64
abdoumbacke64 :
❤️❤️❤️
2026-07-22 20:28:34
0
laminetoure072
laminetoure6486 :
🥰🥰🥰
2026-07-21 19:45:23
1
To see more videos from user @ibraaymaxaliil, please go to the Tikwm homepage.

Other Videos


About