@aliouneabutalib: Thiérou yalla bounou dieul diokhko kilifa yi nako kilifa yi summi diokhko borom. Diokhko borom. Loo wakh mou am yalla la, Loo wakh, loo deff mou weyy yalla. Dou aladji Malick dou kennel yalla la. Waaw na am mou am yalla la rek la. Famaa chaa a? Wamaa lam ya chah? Fa mountamihun kayfa chaah ahtakam #tiktok #ndiolfouta #serignebabacarsy #serignembayesyabdou💖 #tidiane