@sunuouakam: 🚨 ALERTE SABOTAGE : PARTAGEZ MAXIMUM ! 🚨 Regardez comment des individus s'en prennent lâchement à la mosquée de ouakam mboull pour en y versant de l'huile et des saletés. C'est inadmissible et honteux 👥 Aidez-nous à les identifier. Si vous avez la moindre information sur les personnes dans cette vidéo, signalez-les aux autorités #dakar #senegal #galsen #pourtoi #Ouakam
Ki dé yalla nako yalla nit dinagn ka door bamou xol ben place
2026-07-24 23:28:35
7
serigne cisse :
wadji biseum mogui nieuw dh
2026-07-24 18:24:12
700
Thiatou yayam :
khana djak yi amoule caméra ?
2026-07-24 20:28:05
151
Moudou Sall :
ndaysane kholam moka mogne
2026-07-25 08:54:34
0
Yaye Fall :
bouniou ko diapé dina méti si mome li pour lane
2026-07-24 19:03:54
353
Fa bou momö :
Yallah nako yallah wérrr 🙏🏻🙏🏻🙏🏻
2026-07-24 19:12:24
171
😘TIK TOK VIEW 🥰 :
Kou xam ki nako dénoncer moom rékka
2026-07-25 09:26:02
14
bousso bally beuge yayam ❤️ :
Deff lene ci camera
2026-07-24 22:48:14
0
SONKO 2029 ✪ :
mais est-ce que wérna ? avent tous
2026-07-25 00:20:11
70
cheikhouna mboup :
salalhou hanla Moukhamet
2026-07-25 08:12:07
0
Fa ciss :
thiey yalla mo mene mounie souko nehon waji dina talle lenen loudoul lii 😳😳😳
2026-07-25 08:36:37
0
femmme.battantee :
Yalla moye karime té mena setane wadj yalla diokh ko aye tanke diokh ko lokho diokh ko aye beute bamou mena gise menone ko ware . Yalla dal Mo diabote té mena mounie
2026-07-24 21:42:52
65
Aliou :
il faut monter les caméras dans la mosquée tous les angles
2026-07-24 18:54:24
42
Matar trading 🥰by Réma🥰 :
Wadji fate nagnou nak
2026-07-24 19:43:18
55
Business plus :
Salalahou alla mouhamed
2026-07-24 21:30:44
59
Ben Aly Dabo ✪ :
lobby yii
2026-07-25 00:13:20
1
Sope Naby Couture :
Yalla na ko yalla wer sy barket Seyedina Mokhamet psl amine amine amine 😭😭😭😭
2026-07-24 20:23:39
24
Astou Diop :
Yalla nako yalla wére
2026-07-24 21:30:42
23
Zahra2bd :
2026-07-24 20:27:27
14
mohamed :
camera de surveance rek niou diapko inchala
2026-07-24 23:21:11
10
Madame Diagne :
Soubhanala li mome diarna niou déf si diaka yi caméra de surveillance
2026-07-24 22:11:18
10
tony almeida🇸🇳🇫🇷 :
me diaka yi manou gnoufa monte caméra yi alerte nga khamni mok sa téléphone ngay associé bou ame koufa gneuw détecteur bi mokoy alerte ki yor téléphone bi
2026-07-24 23:16:12
11
userrrrrr53468999 :
mais def len ay cameras de surveillance
2026-07-24 23:11:55
6
To see more videos from user @sunuouakam, please go to the Tikwm
homepage.