Ho fouta yalla nala yalla maye were waye Ndayessane 🙏
2026-07-25 13:52:31
312
A N G E :
Gnoune djiguene gni nagnou moy tou stress bly bakhoul ay fébar rkk lagnouy dioural doundou len Lo Len féké
2026-07-25 16:05:43
243
La fraîche ❤️🤗 :
Ay way ay mbokam nagne Gneuw diko wetali bon rétablissement
2026-07-25 15:26:36
193
Sénégal :
bayilen di saga Ousmane sonko 😶🌫️
2026-07-25 15:55:52
63
Niang mballo 233 :
fébar rék la inchallah digua dioukk inchallah
2026-07-25 14:21:56
163
Nounoukh Nanakh Nekh :
Ces dernières années n'ont pas été faciles pour elle, la pauvre. Yalna ko souniou borom may wérr ak gousd fane.
2026-07-25 15:30:39
139
Pathe camara :
Politique ak lambe nio yame
2026-07-25 15:33:28
89
Tim@ Diaby🤌😍 :
Ohh massa yallla na yalla safaral lep inchalah
2026-07-25 16:01:40
8
fatoudiedhiou91 :
yalla nala yalla may wéer chifa, nadia, ak taysir
2026-07-25 17:15:04
0
Zeynafashion🥰❤️ :
Yalla na yalla feugue sa bop maye la werr si barké seydina Mouhamed bon rétablissement
2026-07-25 14:31:37
86
Kenybara :
febarou lanla?
2026-07-25 10:48:23
31
libin :
Massa yo Allahou walou du courage febar bi yalla nako yalla weral Amine ya rabi
2026-07-25 17:16:35
0
Aminata Racine Sarr :
diga wér légui inchala
2026-07-25 11:48:01
77
Sambe Fatou :
Bonne guérison
2026-07-25 13:05:36
72
RemsSoda :
QU'ALLAH TE GUÉRISSE Fatou mom moy Docteur bou maak bi yallah nangua werr ak jaam
2026-07-25 10:55:28
43
yacine dieye :
diegalou ousmane sonko
2026-07-25 17:17:29
0
personne :
ay way li métina yalla nako yalla takhawou Si barcké seydina mouhamed psl amine 🙏 yarabi
2026-07-25 11:37:41
71
titofelling :
Sénégal problème yi barina
2026-07-25 12:05:10
25
Fifichou .d :
Oh non 😢 yallah Nala yalla may wér
2026-07-25 14:20:16
35
Aminata Seck :
wa ana maky
2026-07-25 11:23:19
13
bayou goor bou sonko officiel :
bayi lén di saga seyina Ousmane sonko
2026-07-25 17:09:57
10
Maria Diao :
Ayway ken yenéwoulako. Ya rabbi. Cette fichue maladie sonal nagnou ya rabbi. Migui yobou djiguen gni rek. Ya rabbi li lane la.😭😭😭😭😭😭😭😭. Sama xol bi diekhna
2026-07-25 14:18:15
32
Deebo poulo :
Ohhh li ken yénewu lako 😭
2026-07-25 16:10:34
94
endazdiogeme :
febar moy nonn bilay😳
2026-07-25 14:51:46
40
To see more videos from user @astouwade00, please go to the Tikwm
homepage.