Boss dinaléne diapalei wayei dina diapalei bopam dafa yagu kham noumouy wouter khalliss
2026-07-25 18:57:42
198
N.U.N.O.✪ :
li nitt wara senté yalla beuri na bilahi wolahi
2026-08-07 23:49:46
210
Babe mina awoo yaye ❤️🇸🇳 :
Yalla nalla yalla may weer
2026-07-25 20:10:02
126
Élément capitaine sy :
ay way li metina 😭🥹 yalla na la yalla takhawou inchallah
2026-07-25 18:22:05
66
Tima la moustarchida 😘❤️ :
Yalna wer ak diam inchalah
2026-07-25 19:36:51
139
Khady Faty :
Mais à la fin lane gueen bgeu defoleen daray lou bah am koukoy def dolen ko encourager gueen diko hass
2026-07-25 20:32:36
48
Sokhna Diarra :
Niouy ré boss délénn soralé niou Yor métite bi😭
2026-07-25 18:49:25
43
mariajumelle :
QU'ALLAH L'ASSISTE
2026-08-10 23:22:47
28
dounkh@f 34 :
Si bane nga nékk 😂😂
1) 🚽🤳
2) 🛌🤳
3) 🛋️🤳
4) 🪑📱
5)🚗📱
6)🍜🤳
2026-08-10 00:27:45
6
Sokhna Diakhate :
yalnako yalla takhawou🥰
2026-08-07 23:52:17
19
Mouhamed sope naby🥰 :
Ane sope Mouhamed yi ❤️❤️
2026-08-11 02:14:03
9
Modou mbappe 10🇸🇳🇫🇷 :
yalna ko yalla takhawou😭😭
2026-08-10 23:05:30
26
{Fallou_____} :
salalahou alla mouhamed salalahou alla mouhamed
2026-07-25 22:27:10
21
modzo :
Sallahou hallaye wassalam
2026-08-11 01:13:18
10
alhamdoulila :
yalla rek moy yalla
2026-07-25 19:29:38
15
Mame Coumba guissé :
Ayi boss yallah nala yallah faye ça khôl 🥰
2026-07-25 21:16:03
10
podgamersn :
Bilahiiii contane na trop s’i ioe yalna yalla motali yiw t diapalela si liga nek ni🫵🏿❤️
2026-07-26 03:10:11
12
🍒 :
2026-07-25 20:11:28
23
Ngoné_rashy🖤 :
Yallah nako yallah safaral 👏🏻👏🏻
2026-07-25 19:45:36
6
user5519665669121 :
yalna yala maye ko were Si barkéb seyedina mouhamed salalhawou alayehi wasalame ❤️Amine Yarabi 🤲 salalhawou hala seyedina mouhamadine wasalame ❤️Amine Yarabi 🤲
2026-07-25 19:27:12
5
To see more videos from user @boss_comedie, please go to the Tikwm
homepage.