@mhd_saliou_pro: MESSAGE DE S MOUNTAKHA MACKE AU PRÉSIDENT DIOMAYE "Yaw minga xamni yaa yilif Senegal gèpp, Nanga fexee ba Senegal gèpp nekk ci djaam nanga fexee ba Senegal gepp djuboo, nanga Fexee ba luy nduru ag noonoo ak bañante baña amati seen diggante, ndax xadjul thi rèew mi. Mangi lay soñë thi loolu ndax mooy yoon wi gën " #mouride_sadikh_officiell #serignetouba #mhd_saliou_pro #pourtoi #fyp
MHD SALIOU PRO ✪
Region: SN
Monday 27 July 2026 01:32:58 GMT
Music
Download
Comments
merci beaucoup le Marabout nous sommes contents de toi mais workatte bakhoul
2026-07-27 08:19:47
6
user Mouride sadikh :
Li Serigne bi wakh dou pour diomaye c’est valable pour tous amo lene dég deg motakh
2026-07-27 08:39:53
1
madiagne cisse :
شكرا
2026-07-27 09:20:52
1
user4131838344363 :
merci beaucoup Serinie bii
2026-07-27 08:39:05
2
mouhamadou fall :
merci mbacke balla Aïcha bourré ❤️❤️❤️
2026-07-27 07:56:47
3
Jésus seul :
Merci beaucoup
2026-07-27 08:20:36
1
Lebeau Ndoye :
MACHALLA MACHALLA
2026-07-27 07:51:55
1
Ibou Sylla :
Macha allah degue bou wer
2026-07-27 09:15:34
0
Cheikh Sarr :
sonko rék inchallah
2026-07-27 09:12:08
0
baadji806 :
Massithiou dé dégna deug
2026-07-27 08:04:25
0
Mate kossy :
machalla merci beaucoup ch bi
2026-07-27 09:01:15
0
Marietou Sakho :
machalha
2026-07-27 08:55:48
0
PAMBAL PAMBAL BI :
2026-07-27 08:55:05
0
madiagne cisse :
شكر
2026-07-27 09:21:17
0
Amy dieng :
🥰🥰🙏🙏
2026-07-27 07:28:57
0
démba BA TAMBA :
2026-07-27 09:24:15
0
Valérie Sambou :
merci baucoup vraiment machalla long vie a vous
2026-07-27 07:54:22
0
Issa Guéye :
il est pas a l'aise WOR bakhoul sa conscience dou tranquille
2026-07-27 08:30:45
1
BEUGUE BARHAMA NIASS RTA :
mouné khoudiou mélni mousse mou nane diwline kii mako bagne légui
2026-07-27 08:58:44
0
mandoul :
2026-07-27 08:57:10
0
bamba bou sonko officiel 🇸🇳 :
li dal lanioy khar thi serigne sép wakh lou wara wakh
2026-07-27 08:46:48
1
To see more videos from user @mhd_saliou_pro, please go to the Tikwm
homepage.
© 2021-2026 TikWM. All rights reserved.