@filsdembaovilleneuve: #deuilnational😭🥺🇸🇳 #senegalaise_tik_tok #deuil

battou askanwi ✪
battou askanwi ✪
Open In TikTok:
Region: SN
Wednesday 29 July 2026 22:22:52 GMT
27302
5889
118
148

Music

Download

Comments

elkha_443
Kallamuh @43 :
Figeu dieum Nala geuneul figeu diougé diambar 💔😭🙏
2026-07-29 22:28:09
135
fd__0422
Tymaa___Bou___Sonko🌺💓 :
repose en paix 😭🕊🙏🏾yallah yeureum ko
2026-07-29 22:27:21
19
tymashuu2
𝑻𝒀𝑴𝑨🇸🇳 :
Dewoul frère bi mo décédé mes mom Khaw na sonou
2026-07-29 23:07:57
8
ndiawargaye
METAL JEUNESSE SÉNÉGALAISE :
Nanga def sama frr, yaakar naa ni yaa ngi ci jamm. Gis naa yéene ak ñaan yi nga def yëpp, waaye ngir dëgëral la rekk, xaritu Mansour mooy ki faatu waaye du Mansour. Moom ci coma la nekk te dofdoo yi (médecins) ne nañu mën na mucc. Kontineelien di ñaan 🤲 ngir Yàlla dimbali ko. Lii ci magam bu góor la jóge, jërejëf. »
2026-07-29 23:11:00
1
aidasphop
Aidy complexe beauty❤️❤️ :
C op vrai 😭
2026-07-29 22:34:43
6
seyeyarame51
Soda tilala ❤️ :
Dewoul nianal lene ko gawww😭
2026-07-29 22:52:01
3
marichousow41
Choubidouuuu :
Ay way gnanalenkooo Mouguii en coman
2026-07-29 22:32:00
8
paul_kirikou_bou_thikiri
ᑭᗩᑌᒪ KIᖇIKOᑌ ᗷOᑌ TᕼIKIᖇI ✝️ :
Dans la coma la nek yallah nako yallah takhawou 🤲🏾
2026-07-29 23:16:33
3
assy.seydina.a.d
assy bb❤️💍 :
Yalla boumou done deugue waye
2026-07-29 23:17:41
4
dieng.mawlouda
Dieng Mawlouda :
😭😭Yalla na la Yalla yereme té kharéla thi aldiana Yi guene kawé figua djeme guenel la figua djougué 🤲🤲🤲
2026-07-29 22:39:44
4
hommedefootlocalicospor1
ICOSPORT HOMME D FOOT LOCAL :
Ohhh 😭😭aldiana sa keur mon ami 😭😭😭
2026-07-29 23:42:08
1
cheikhahmedtidi8397
𝖐𝖍𝖊𝖚𝖈𝖍_𝖑𝖆𝖎𝖙🍼 :
😭😭😭
2026-07-29 22:29:19
5
baba.yaya.gueye4
Baba Yaya Gueye :
Mom il dewoul Deh xaritam mo deh
2026-07-29 23:05:10
0
thiernocana206
Thierno cana 206 :
nite you bakh yi rék nionyy dém😭😭😭
2026-07-30 00:00:15
0
ablayediakhate0805
Brahim jr :
yeurmandé yalla sa kaw 🙏
2026-07-29 22:25:53
1
lil.diazz.domou.y
Lil diazz domou yeumbeul🙈😎 :
ohoo mansour yalla nako yallah yeureum
2026-07-29 22:53:13
0
ndiaya.kebe6
Ndiaya Kebe :
repose en paix frérot 😭🕊🤍😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭🕊🕊🕊🕊🕊🕊🕊🕊🕊🕊🕊🕊🕊🕊🕊🕊
2026-07-29 23:45:40
1
user4026166561870
amet bou borom darou 🖤❤️✍️ :
repose en paix 😭😭🕊️
2026-07-29 23:53:38
0
prettysira17
Bby 😘Sira 💞 :
😭😭😭😭
2026-07-30 00:01:14
0
To see more videos from user @filsdembaovilleneuve, please go to the Tikwm homepage.

Other Videos


About