man de Touba fou mana dem charette lay dieul ndakh nekhay bi ambiance sou charette non lolou niveau leu😂😂😂
2026-07-30 23:57:59
31
mouride officiel ✪ :
Yagui diantou dh 🥺😂
2026-07-30 14:44:33
21
gueye_93 :
Darou marnane 🥹🥹
2026-07-31 11:24:40
1
La salihate❤️ :
Yalla boumou wax dafa guinawé wala dafa kanamé non lii nekh na way😂😂😂
2026-07-30 10:45:33
14
༆✪Niass✪Pedri 🔥 :
Relation à distance yi
TOUBA dou lieu de rencontre
diaap léne si
rek🙌🏾
2026-07-30 17:34:34
19
Boudchu9402🩷🎀 :
Même mane souma dougoul saréte day mélni démouma touba🙈😄
2026-07-30 11:05:12
0
Mame Mareme Falilou 🫶🚩🏴 :
C’est moi 😂
2026-07-30 11:19:14
0
adakara jadid67 :
Wala mou may la kore😂😂😂😂😂
2026-07-30 14:22:03
0
Oumoul khadim 🧕🏻❤️🫀 :
Bly yaw 😂😂😂😂
2026-07-30 18:13:10
1
S Thiam🍯🧚🏿♂️💞 :
Yag kaneuu 😂😂
2026-07-31 08:49:39
0
فاطمة بنت خليل اللّه ✨💫🌺 :
Touba lay diangé def nafi 4 ans ms ww touba yakh nane ma si sarett ma douggou si auto di wathie wakhe chauffeur bi borom sarett mayma ma wathie mouni ma sm auto bi da niro ak sarett 😂
2026-07-31 15:10:20
3
Astou fallou :
Moi aussi 😁😁😁😁😁💯🤸🏾♂️🤸🏾♂️🤸🏾♂️🤸🏾♂️
2026-07-30 10:39:00
4
Papà :
bly damay jabanté jumma dia ak marché ndax sarétte yi😂
2026-07-30 18:54:52
0
sodadieng123. :
sama kogne gua gneuw😁😁
2026-07-30 19:59:45
0
Soxna bou baye karim❤️ :
Bari gasi Ay morom 😂😂😂
2026-07-30 09:23:37
5
To see more videos from user @alaliserignesaliou, please go to the Tikwm
homepage.