@lopytabane1:

Abd 🇸🇳🎭
Abd 🇸🇳🎭
Open In TikTok:
Region: SN
Friday 31 July 2026 07:46:02 GMT
277956
39764
463
835

Music

Download

Comments

salalahouhalamouhamad0
$£møù tâlíb£ $ $âlìøù :
Yalnaniou yalla may bou dakh bi waxlen amiin
2026-07-31 15:50:59
2631
videdresingpikinebuzz
videdresingpikinebuzz :
Mouride yii yala teral nalene fii thi adina te euleuk yamal khiyam lay geurneu nekh inchalah
2026-07-31 21:46:22
293
mahre206
MAHREZ ✪ :
Rombou nako damako xol ba rouss😭Sénégal amna niou yorr ndekei
2026-07-31 20:19:06
964
al.insan91
Al insan :
wakhlen yen nieup sallallahou ala mouhammadine
2026-07-31 22:00:05
290
aminatakonare436
mme konare :
keur gui rafetna trop machallah souma khalatébeuss dina gneuw borom délou si borom bayikofi yallana yékh dara douma saf yallanagnouko may you dak yi sa yowmal khiyam amine bolém dioulite
2026-07-31 19:13:00
181
jeaneboubane
Begue fallou :
Au yalla mayma keur bou melni touba guirrr maye liguéyal serigne touba
2026-07-31 19:19:09
80
ametndiaye
Ahmed Saliou ❤️🔐 :
Fi moy ndamm diguenté mbacké ak touba
2026-07-31 09:56:10
93
fatima.sall490
Voile d’éclat 🧕🧕 :
votre sœur qui débute dans l'entrepreneuriat et qui a des marchandises en stock mais qui peine à l'ecoulé par manque de visibilité vous demande de vous abonner svp 🥰
2026-08-01 01:30:01
8
papa.fall5149
Papa Fall :
inchallah yalla bakhna
2026-08-01 02:07:59
1
baye43karim6
Diouf Ab :
Yalla loumou def dafa guene
2026-08-01 00:27:08
1
anta7882
Anta :
sallalahou ala mouhamad
2026-07-31 19:31:27
32
ibrasantyalla
santyalla 🇸🇳🇸🇳🇨🇦🇨🇦 :
Inchalla Yalla baxna
2026-07-31 16:58:41
19
salomonmohamedph
salomonmohamedph :
yalla naniou ko borom bi defal nioune nieup inchalla 🙏
2026-07-31 23:27:53
0
khadimegueye8
Khadime Gueye :
kou mom lii
2026-07-31 21:09:56
0
oukhtykhoyita
Bint-adam 💕 :
Sallalahou alla mouhamadine
2026-07-31 23:12:01
30
faadeljoxane221
faadeljoxane221🇨🇦🇮🇷 :
Bo guiseuté lou taarou nga beugue ko am dangay jakarlo ak mome ngaye wakh alhamdou lillahil lazii bi nihmatihii tatimous saalihati 7 fois nga niane souniou borome mou maye lako🙏🏾🙏🏾
2026-08-01 01:08:13
20
makhou498
makhou498 :
Yalla nalako yalla may inchallah
2026-07-31 23:59:36
0
mdoumo
mdoumo :
Amine way
2026-07-31 19:10:51
0
lejeunesoldat3
Thiam Baabel- Officiel 💕🫡 :
Liguey mo kay mayé dh Yalla n’a niou ko yalla may 🤲🤲🤲
2026-07-31 21:42:06
18
omar.an250
omar.an250 :
Nianal yalla Soutoura dio bari te sakh yalla maye la 🫵Alall diomonm te Alall dji banie la mo me
2026-07-31 23:48:20
11
bb.isseuuu5
bb.isseuuu5 :
Touba aye keur you rafete rek mofi nek
2026-07-31 20:37:07
16
cheikhtidjanesow125
Cheikh Tidjane Sow 🇸🇳 :
yalla nanou yalla may xalise 🤲
2026-07-31 20:03:02
11
ahmadou.diop.le.c
seuteu cheikh masamba Diop sam :
Yalla bakh na inchallah Dina bakh frére
2026-07-31 15:12:51
22
madiop.thiate
Ma.diop’thiate🦋💫 :
Adouna Lep lo guiss rek guem guem Leu
2026-07-31 16:14:49
26
To see more videos from user @lopytabane1, please go to the Tikwm homepage.

Other Videos


About