daw thi yaw lako Guissé niane yalla bou réne bi fek ma sama keur Brom keur barcki cheikhal Khalifa seyssi na magui sante yalla bou bakh yalla na yalla faye la yiww
2026-07-31 13:18:33
1833
Fasanda Ndiaye :
mandé dama yakar ni daa am kouy capté samay gnanes. gnane na ba sone. yallah bakhna
2026-07-31 12:45:16
1516
Ahmadou bamba 🇸🇳🇫🇷 :
2ans gui ni makoy deff louma si niane sa Borom deffko bilahi