Sérieux dafa diot niou khalat le taux d accident...
2026-07-31 21:19:51
221
Lamine_Milano10 :
Serigne si d Saway adiya yelen intéressé
2026-08-01 02:34:10
91
اللهَ :
Senegal politique moko tardel 🙏
2026-07-31 18:39:16
224
Mouhamed Mansour Sall 🥏 :
Linga wax idée you rafét la mais nit matoul en plus de cela lolu même buko Serigne bi waxoul État moko wara xamal bopam ndah magal dou gane Senegal✌Yalla na diam yague bon magal à tout le monde
2026-07-31 18:05:15
232
Sonko sama president 💪☑️ :
Sonko kay gouverner woul
2026-08-01 00:51:49
58
geum sa bopou :
Serigne si ils sen fou des gens qui meurent par accident
2026-07-31 23:56:38
16
Pape Gadi✪ :
legui la sama bénn grand rombou 16h ay coté 17h mou def sock niakk bakaname 😭
2026-07-31 21:51:31
47
Kolo Touré :
Yallah na gnepou Magal thi diamou
2026-07-31 20:57:41
53
djipson :
bilahi bakari meuna nék president
2026-07-31 23:54:14
15
BGN :
Bilay bro
2026-07-31 17:06:44
33
Mamoudou Ndiaye :
N’oublie pas les 5 prière 🙏
2026-07-31 23:32:18
36
Khadija Rassoul ❤️🦋 :
Vraiment wax gua degg dafa am auto you xamni waroul daw long voyage
2026-08-01 01:35:09
16
Abdou saliou :
Ms deniouy def ensemble genaral avant Magalgui bokoul agu ziarr guii
2026-07-31 21:41:09
16
B b b :
Pourtant chaque année niou wakhsi
2026-07-31 21:27:47
10
Talibi Cheikh Mouhidine :
Yalnagnou yalla fayal Cheikh Mouhidine
2026-08-01 04:46:22
1
Apple@89 :
Vraiment
2026-07-31 21:48:56
10
Suñu 🐄teranga 🐏élevage 🐔 :
Boudei li rek gua wah deh deug gua wah taux d’accidents yi mom c’est énorme
2026-07-31 23:43:58
5
ousma148 :
Lou am solo
2026-08-01 13:21:21
0
ndoye user5526548216693 :
machallah frr rafétna 🥰
2026-07-31 21:54:32
7
Maurice Mendy :
bien dit grand bi
2026-07-31 22:27:36
7
borom dieuk bi :
CRD avant Magal lingay wx dagn kofay souligné ak yénène yo khamoul
2026-07-31 21:47:17
5
yeuréurmdé yallah :
bayo goor yii
2026-08-01 14:57:55
3
user5012318308304 :
sécurité routière magal loumou diotè aak magal
2026-08-01 10:47:07
2
Dieng Sala :
Choc yi beurina trop 😭😭
2026-08-01 03:15:41
2
manumini99 :
Il y’a les services compétents envoyé par l’état même qui travaillent sur ça d’arrache pied depuis bien longtemps
2026-08-01 07:49:56
1
To see more videos from user @galsenpro18, please go to the Tikwm
homepage.