@daaratayssirhassirkm:

Cheikh Mbacké🙏🏿❤️
Cheikh Mbacké🙏🏿❤️
Open In TikTok:
Region: SN
Sunday 02 August 2026 13:51:31 GMT
132858
10682
197
447

Music

Download

Comments

user7011781675132
Al bachir willaya :
dosi dara domasi dara lepo seringe bila nano rafétal mo geun wakh dji
2026-08-02 18:28:07
106
damegueye13
Dame 🇺🇸Bamba gueye HT🇺🇸 :
Kén santoulako
2026-08-02 17:02:23
26
fallou.seye442
serigne fallou seye :
hisbou tarhiya🥰🥰🥰
2026-08-02 14:14:12
1
seckllmlm
seckllmlm :
billay wallay
2026-08-02 18:04:30
0
assane.lo95
assane.lo95 :
Man Tidiane bi de louma am bokou nako ak mourid walahi
2026-08-02 20:41:21
24
wizz0632
Wizz Bathie 🛍️👖👗 :
Dou sa dolé dh lépp si yonnou mauritte la serigne touba amoul borom 🙏❤️
2026-08-02 18:05:22
6
ousaynou32
ousseynou bay fall bii :
nanou xam wakhine touti way bakh nasi de
2026-08-02 18:45:36
4
biabel.thiam
DiEBEL Thiam :
MACHAllA 💚💚💚💚💚💚💯💯💯💯💯💯💯💚💚💚 Oui 💚💚💚💚💚💚💚💚
2026-08-02 17:12:41
7
nouroudarayni313
nourou darayni seul :
yaw mom saway lingay wax mo bari nay rafet lepp serigne béé
2026-08-02 20:12:48
2
makhtardiop4115
@makhtardiop36 :
Li day yakh wayé defa roul té yonwi wésouna fi
2026-08-02 18:09:01
3
acteur055
Acteur metteur en scène :
Berdé yénlako sante d Saway
2026-08-02 20:09:33
2
mohamedfaadal1
Mohamed💫 fadal ❤️😇 :
Li dou dara lekk kepou la liy dara ky moy xol bou rafet te sell ms li dou dara li lep serigne bi la rkk nga ball ma nk
2026-08-02 22:50:49
2
modou.awa.balla.diaw
🄼🄾🄳🄾🅄❤🄰🅆🄰❤🅂🄾🄿❤🄷🅃 :
sama wa dji yagui beugue eupel nak sama w dji
2026-08-02 19:44:45
3
ballakebe2
balla kebe :
Gni concurrence sougne nga balma nakk
2026-08-02 18:14:57
4
gueyecheikh17
gueyecheikh17 :
dano gua de
2026-08-02 18:09:03
1
bichri_elevage
BICHRI Elevage :
Saway nioune santougne la li dh
2026-08-02 17:27:58
10
damegueye13
Dame 🇺🇸Bamba gueye HT🇺🇸 :
Liguay df Dara rafétousi
2026-08-02 17:02:09
5
sadio.fall13
Sadio Fall :
machallha
2026-08-02 21:01:08
1
user8819673690339
Talibe S Mountakha :
gni kene dou Niome serigne Touba Molène teuyeel bopame
2026-08-02 18:12:07
1
restonspridents01
restonspridents01🇩🇪🇸🇳🇸🇳 :
Commentaire yi loleni sisou cou meune na def Kagne deugue la wakhe 😩✌️
2026-08-02 18:50:05
1
moustapha__junior
✪moustafa_junior✪ :
Ki kom khalé🤩
2026-08-03 09:16:08
0
assane.ndao937
asou :
ball ndamou
2026-08-03 08:54:57
0
To see more videos from user @daaratayssirhassirkm, please go to the Tikwm homepage.

Other Videos


About