nit degaye def lo mone li amna barke machallha sane tall yalla
2026-08-03 01:12:19
0
Youm Global Business ✅ :
Sokhna bou bakh loko diende diarnako wallahi yalnalen Yalla defal diame
2026-08-03 00:44:30
1
yaye serigne fallou :
yalla nalla yalla takhawou Si barker borome touba
2026-08-03 01:10:11
0
abdouwane4 :
Serigne Bi contane na si yzw
2026-08-02 22:31:37
107
SADANI 💗🇸🇳 :
Ndiabot gui yalnaniou magg ba dila berndel nga fekei sen ndieurigne💗💗
2026-08-02 23:45:55
14
OMÉGA✨MRS💍❤️ :
Wawaw Machallah dèwène inshallah yalla na nek Ayy késss
2026-08-02 20:08:21
170
maman bby :
bala déwén yalla gui tég ay mbana si barcké serigne baba car si🥰🥰🥰🥰🥰
2026-08-03 00:25:54
6
Nittou Bamba🫀🥹❤️ :
Machallah Yalna lép barkél barkép Cheikh Hamsa 💙
2026-08-03 01:20:22
6
Mouha lissa lfc🇸🇳❤️ :
Yalla na borom bi deff dewen keur gou rafet bayay dalal ay diounii nittt 🙏 yalla maylen diam ak werrr ak alal diou bariii wayyy dolii soutoureu djii allahouma amine 🙏 yala nagnou yalla nagoul sougnou magal nangou gnan yiii def li geun si gnoun❤️🙏
2026-08-03 00:12:17
18
tour de l'oeuf :
yallah guisnala , sérigne touba guisnala
2026-08-03 00:05:25
20
To see more videos from user @gorafallsopdialib, please go to the Tikwm
homepage.