magal n'est pas dans le calendrier officiel des fêtes religieuses.
2026-08-03 12:55:45
240
KaMaths :
Magal mooy férié, pas lendemain magal. Diomay dalein nekhoul reik
2026-08-03 13:22:33
105
Efc ❤️ :
Xamo leine li férié di coûté État motahh
2026-08-03 14:52:01
15
trump :
diomaye bougoul touba
2026-08-03 13:05:34
72
Codou❤️ :
Mais ça a toujours été comme ça magal yor yor la jour j moy férié gamou goudi la du coup lendemain bi moy ferier
2026-08-03 14:41:05
39
Almakhetar Ndiaye :
On a en mare des programmes innombrables au Sénégal chaque jour un évènement
2026-08-03 14:04:10
43
Adrien Tine :
😁😁😁Sénégal mo nex rek kou lek ba sour wax louko nex
2026-08-03 14:40:29
11
Mouhamed Ndiaye :
wa pastef billahi diguéne sone yéna guise fou diomaye waxé ni tay dou férié.
2026-08-03 13:16:45
10
Daje🤍💚⭐️⭐️ :
Mais lendemain magal meusoul nekk ferié😂 le jj moy ferie dafa tombé ak dimanche rk mtx 😂😂😂
2026-08-03 14:35:20
32
Am Cosmétique ✪ :
Mes vraiment Wa pastef ni lagne laine wara bayer tamite
2026-08-03 13:34:55
17
technicien :
peutétre président diomay dakoy fatté mé dou djikom kou ame yar la . je suis sonko a vie. mé . li la kham thi mom
2026-08-03 15:18:42
8
Black diamond :
Férié ou pas, nous les mourides, on s'en fiche, je mouride et fonctionnaire, je travaille pas le lundi, suis d'ailleurs à Touba
2026-08-03 13:30:14
24
medouneniang878 :
bayilen profito gemo dara
2026-08-03 13:54:53
13
aissatou :
diomayr weroul
2026-08-03 12:41:35
35
ALMAKHTOUM🇸🇳🇯🇵🥋🇨🇻 :
sheuttt Sénégal tamite nak
2026-08-03 13:08:07
11
yorodiouf218 :
nguir yalla déléne wakh DEUG diomaye foumou wakhé lolou
2026-08-03 13:25:41
10
Noura Wedding dress :
hey boul gnou sonal le jour de magal est férié pas le lendemain c est pas un acquis pardon
2026-08-03 13:40:01
6
diallo 221 :
magal lañu wara bayi
2026-08-03 14:36:33
6
Baay Ndiassé :
Tu temps de Macky Sall do ko wakh lep politique rek
2026-08-03 13:20:57
7
user7797807866377 :
lendemain magal mom dou férié nak
beguenaniou serigne bi lolou wayei jour bi moy férié
2026-08-03 13:35:53
15
lemonde :
Diomaye bi ka porte parole bi yeddé la khamni paré na cii Touba
2026-08-03 13:07:05
9
Bilal diop :
Abdoulaye wade mone jourou magal chaumer et payer waxoulwone lendemain magal pour mou lére 🙏dieuredieufe borom touba ay détails rek guinne fi neke Wa pastef