@film.en.wolof.1: 🦊🐇 Épisode 8 – Samba nekk na Milyaardeer ! 💰🔥 Samba Lapin mujj na nekk milyaardeer gannaaw mu liggéey ak xel mu rafet. Bouki nag, dafa réccu te tàmbalee sonn ndax xam na ne moom moo nangu woon 20% rekk. Ndax alal dina tas xarit? Ndax Bouki dina bàyyi jaloore walla dina tàmbali pexe? 💬 Binde sa xalaat ci commentaires. ❤️ Like 🔁 Partage ➕ Suivez la série ngir bul ñàkk Épisode 9. #BoukiAkSamba #WolofSeries #Sénégal #TikTokSenegal #IA