li depuis 10 ans niogui makoy expliquer mounou mako comprendre 😂😂😂😂
2026-08-04 21:45:02
247
🍁🦈 :
Wout ordinateur defko si sa Excel mo geuna worr li 🤔🫱🏿🫲🏾
2026-08-04 19:35:23
88
#LINZO VIP SHOP 🛍👕👖🥾🧢🛍 :
Li pour borom bopo you baxoul yi la❌
2026-08-04 22:53:25
23
Mouhamadoul Amine Lo :
Dou ngeine ma dimbeuli thi facebook bi yen di buster plus de 100 personnes dila lath t ken dou djeund😭😭😭métina way solution
2026-08-05 12:00:43
42
Business :
amna solo machallah
so beuguê xam limay wakh danguayy sêtan video bi bamou yeg té bousi bayyi dra😂😂😂
2026-08-04 17:02:01
80
Diariatou Bousso :
Je suis intéressé tt
2026-09-11 11:03:21
1
matt deug :
télécharger len wallet mo geunn
2026-08-05 21:49:26
11
ya salam🫂ba 2027-2029 inch'A :
Bismillaahi Rahmaani Rahiim
Assalaamu aleykum wa rahmatullaahi wa barakaatuh.
Sama bokk yi ci Yàlla, dundug nit dafa gaatt. Képp ku nekk dina dellu ci Yàlla. Kon nag, nanu gëna bari ci jaamu Yàlla, di sàmm sunuy ñaan, di jàng Alxuraan, di def jëf yu baax, te di baalante.
Yàlla dafa bëgg ñi ko ragal te di yërëmante ak seen moroom. Bu nu bañ a fàtte ne alal ak ndam duñu sax; li sax mooy ngëm ak jëf yu baax.
Nanu ñaan Yàlla mu baal nu sunuy bàkkaar, mu gënal sunu ngëm, te mu yokk sunu yërmande ak sunu mun.
Bu la waxtaan wii neexee, séddool ko ak sa mbokk yi ngir ñoom itam ñu man a am njariñ.
Wa assalaamu aleykum wa rahmatullaahi wa barakaatuh.
2026-08-05 00:18:26
19
Modou Ndiaye :
commerce koula dakh calcul mola geuna tardé li motakh niou nane commencer pour ndogo dara yi la bilay boy calcule do deff dara dagay sakh ragal mome bou sétté rek woloul say employés té ame confiance ci niome tay bayi xéll yallah ci ligay ligeuye
2026-08-17 00:48:04
0
SEUGÑ MOUSSA :
lingam deff ni mankoy deff dp mes éventaires lako mana toude
2026-08-08 00:14:09
1
Latzo🛍️ Businessman.📍🎉Mbour :
Plus tard, ils diront que c'était de la chance. Parce que personne n’a vu les petits matins, l’ampoule allumée quand tout le monde dormait, et la persévérance même quand il n’y avait aucune garantie. La réalité est simple : le succès se produit presque toujours à huis clos. Ce sont des répétitions, de la concentration et des décisions inconfortables qui perdurent au fil du temps. Cela ne se voit pas sur une photo finale. Faites confiance à votre processus. 👤🧠
2026-08-06 01:25:29
5
Talibé Sérigné sam mbaye :
mba suma ko deffe duma nék millionnaire bou ndaw 😅😂😅
2026-08-23 01:33:15
1
bocarwally ✪ :
sama téléphone Amoul Tik Tok 😔😏🥹
2026-08-05 01:19:51
9
MoGATES iPhone USA🇺🇸 Ⓜ️D🅿️ :
Li gaye def ni mako dake fou bilahi
2026-08-07 22:15:38
1
BMT 🧠💕 :
application money lover or walletapp
2026-08-04 17:32:19
8
colobane matariel&tôlie&sodeur :
nanioy khey di diay rk lisi dess amol solo
dakar soy bayi xel lingay depasé do dondo ningawara dondé
2026-08-08 13:57:10
0
zilo :
je suis intéressé
2026-08-25 02:58:20
1
Serigne khelcom :
Li kay koko defoll neko commercante
2026-08-04 22:26:34
7
habib.njaay💜♐️ :
Bizarrement mane comprends nouma dra 😂😂😂😂
2026-08-05 16:49:22
4
ousmanesenghor260 :
je suis intereser comment commencer
2026-08-06 13:29:44
2
El Malick bou Mouhidine 91 :
saway boutique dou pharmacie
2026-08-05 15:58:04
2
arijit singh ❤️🫵🇸🇳 :
bilahi toppe nala founek pour ame numéro
2026-08-07 16:06:37
1
FADALE BA :
li mome mane ma nou m'a ko
2026-08-05 12:36:03
4
Als l'innocent :
bonjour moi je suis en train de commander des produits en Chine mais pour l'instant j'ai pas un agent que tu me transférer est-ce que vous pouvez m'aider
2026-08-05 23:22:53
1
Moustapha Sy :
je suis intéressé formation de business
2026-08-05 14:53:07
4
To see more videos from user @cdp_sn, please go to the Tikwm
homepage.