@jeunetalibecheikh28: li dh moy déranger mais diguene dh ma ko wakh ma tayy #serignecheikhahmedtidjanesy #serignebabacarsy #senegal_tiktok221 #malikia_tv
Entouka ak lou mana khew 1902 la maodo commencer. Gamou dall ❤️❤️Brom diaka yi ak diouman yi Sy fagueye demba ndiol fama
2026-08-05 15:35:20
1
Astou Kane :
Tambali thi mome yame thi mome ❤️❤️❤️❤️
2026-08-05 14:39:47
2
maguista bou serigne saliou ❤️ :
nion amouniou sen temps serrigne touba molen dérange
2026-08-05 14:46:08
13
talibé cheikh ❤️ :
ayyy bayi léneu comparaison yiii
2026-08-05 10:06:34
129
borom darou :
kou gamou won 2019 touba rekkkkk
2026-08-05 10:27:52
18
🦋Maty🦋☆Falilou❤️ :
y en a des choses qui ne disent pas parce que ñun ñepp benn lañ dielelé bok biñou bokk rek mais ñou ñepp seydina mouhamed sws lañou geum . genre wax yi soukou ñi contre tarikha yi degré dañuy geuna am atouts. la plupart des famille y a certains qui sont Mouride d'autres sont Tidjane. moi l'unique sœur de mon père et mes cousins sont des Tidjane. ñun ñi xamul ñoy wax rekk mais pour ñom lepp ben la. meunañ kaff toñanté mais y a certains paroles daffa diss
2026-08-05 11:37:44
16
Talibé serigne babacar Sy 🤍🕌 :
Serigne. Babacar santoula li dh boul yabb lou maodo nakk 🙏Tivaouane Touba lepeu beneu la
2026-08-05 15:03:07
31
Sope Maodo :
Maodo khamoul li.
2026-08-05 15:44:43
0
yade baye talibé cheikh 📿♥️☝️ :
Mame maodo amoul morom
2026-08-05 10:45:24
7
elhadji8672 :
En tout cas borom parasol bi woté woul noss magaloul bopam ya Rassoulallah kassé lay wootèl♥️
2026-08-05 10:40:53
71
kadia houléye bâ :
salallahou alla mouhamadine ❤️❤️❤️❤️🙏
2026-08-05 09:55:35
24
Éva Queen 👑 :
maodo di Bamba bamba di maodo na lepp raffet
2026-08-05 13:02:35
26
codoudieng64 :
2026-08-05 08:36:48
22
BOSS GLOW by Diarra✨💎 :
Maodo nak ba kham guène dii dfa mouss ba pa yii dii woute sen nii bisse mome mou lakhasou sii bisou sangue bou tédd biii kii gua khamni loko lebal rk mou fay lako ba wiss la😭🎉❤️
2026-08-05 10:58:54
10
TALIBE CHEIKH 📿🇸🇳❤️🇮🇹 :
maodo amoul morom 🇸🇳 ♥️♥️♥️❤️❤️❤️♥️♥️♥️🙏🏻🙏🏻🙏🏻
2026-08-05 15:05:12
0
sakho sakho bi 321 :
kou ko beugue lalal ♥️
2026-08-05 13:22:52
52
cheikh ibra80 :
Moy dérange moy diriger 🥰🥰❤️❤️
2026-08-05 13:50:12
56
la babacarcienne :
yagnou hamal yoneti🥰🥰🥰
2026-08-05 10:13:33
21
Mansour Gaye :
Sa waye ya wakhe deug Nk 😁 bouniou sangone gambou tivaone dou am bly 🥰
2026-08-05 10:15:56
7
moussa sy al amine :
diamou djilén yalla mo geun si lingén nék ni mélni kou amoul lo def maodo santouniou concurrence dafané niou magal goudi yonent bi kénén kou def nk bxn
2026-08-05 12:33:50
9
yabysall :
yalla na gnou yalla fayale seydi haji Malick Sy rta 🤲🤲🤲🤲
2026-08-05 09:45:44
17
adjista bou Ib mbaye :
loutakh gani moy déranger mouride yi té Pourtant niom niépe béne lanie je suis une talibé chiekh mais déme touba❤ ak gamou❤️
2026-08-05 09:04:57
55
To see more videos from user @jeunetalibecheikh28, please go to the Tikwm
homepage.