Mane deh sidiada lassi dieund tè Allhamdou liha Mâcha 🤲
2026-08-06 20:54:29
689
Amina❤️ :
Deug leu deh sama boss amnassi niari jalabe joulikay sidiada kamil ak taysirr moy sama joulekay 3h du matin🥹
2026-08-07 09:41:07
228
Ourul @yni 🔥🌹🌹 :
sidiada ak dioulikay lassi dieund alhamdu lilah
2026-08-17 20:50:29
87
BU___Y@Y£🤍🇸🇳🦋 :
Ndeysane sama soxna dh mayou mako ay million mais fekhéba dieul si may bi diende si ben sidiada ak ben dialabé. Yalna yalla barkel da seuy bi Yaye boye Lofa Mégane yalna Bakel
2026-08-07 10:21:27
59
amethndiaye066 :
Mais qui m'explique Louy thiane
2026-08-26 16:16:39
10
Loupe🔎 :
ki bénen dimension la mashallah🙏
2026-08-15 01:20:32
42
Yayou yayam🥰 :
Mane môme sama pape lako may
2026-08-27 00:25:55
13
ngindengome :
machalah ❤️❤️❤️❤️❤️sy malick ❤️❤️
2026-08-06 17:14:01
40
Ndeya gueye🍀 :
Ay moytou len lay li graw na dhé man lolou mesouma khamni dagn koy abe pour gnane si