soy dougou si commentaire yii do déf ndank kholal guagn nguama sakh 😫
2026-08-06 15:51:57
47
fafasarr💟 :
wawouaw dawal dé faye nouyo faratala😅
2026-08-06 10:28:08
230
Fatima moo serigne saliou❤️👌 :
Niaka faye bakhoul sakh😂😂😂
2026-08-06 10:38:28
1
Khadim Seck :
bou kennn reee😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂
2026-08-06 20:15:35
1
Mieldouxdekabir😔 :
Sama Yaye def nako doug ci bus di dem Touba mais mom souy voyagi dey nelaw rek am kou téléphonam soné borom téléphone bi décrocher né salamaleycom sama yewou rek neko malecomsalam mais bus dagnouy ré ba sone😂😂 bilahi
2026-08-06 09:36:19
93
Adama Dembele :
Adamo tidiane la
2026-08-06 10:05:15
13
prince 🤴🏿 :
sama téléphone amoul tik tok
2026-08-05 23:39:38
138
user8895709882343 :
Ame na solo mais on dit walekoume salam
2026-08-06 23:41:42
5
kanzo jr🤞🫀💯 :
lii nekhna😂😂😂
2026-08-05 21:40:03
27
princesse sarr :
mais dony wahalay koum salam wala ni ngakay défé hé😂😂
2026-08-06 22:21:48
7
Sarr bou SBS :
koula yéné diam nga délokoko🥰🥰🤲🙏❤️
2026-08-05 23:19:02
69
Anta :
sallalahou ala mouhamad
2026-08-06 21:18:08
11
đįåķĥåţė :
njaay fo deukk isîne galas
2026-08-05 21:38:26
72
aissatou ndiago or 🥰🥰 :
Machallah 🥰🥰🥰
2026-08-05 21:42:30
7
Fallou Gaye :
Www adouna worull
2026-08-05 21:39:10
27
Seydi17💫✈️🌃 :
Ah vrai c'est pas un jeu enh😏
2026-08-05 21:59:17
30
Diaz :
c pas maleykoum ms wa'alaykoum
2026-08-06 11:26:26
54
Khady badiane :
bilay dama ko yeureum kou d'accord lalal j'aime 😂😂
2026-08-06 00:08:00
27
To see more videos from user @njaaycharismatic, please go to the Tikwm
homepage.