Léne dale khamna ko ibn usman misi tivaouane kéne eupouko kham kham 👍
2026-08-06 12:37:50
336
OUSMANE NDIAYE SAM :
Tayla masa anndak oustaz dégaraté nak❤️❤️👍😂
2026-08-06 12:16:07
344
Bouba Apple🍏🍎221🇸🇳🇺🇸 :
Ibn taymiya limou liguey sii diiné djii bouko 4 serigne Senegal yi defon Senegal dépassé na fii bou yagg
2026-08-06 13:41:16
33
Domu buur sine 🇸🇳🫡❣️ :
Man la question que je pause moy pourquoi niou gueum ibnou taymiya wala bouxary mais meunouniou gueum mame borom touba ou Elhadji Malick
2026-08-06 15:58:01
83
Tamsir Ndiaye :
Daniouy Gamou Déh Inchallah
2026-08-06 11:51:11
135
ibrahima sarr :
man limay lathieté kam nieuka gamou Sénégal
2026-08-06 10:41:40
15
Karim Ndao :
wakhal li yalla wakh comprendre na danagou woul wakh si question bayil borom kham kham yi té wakh li yalla wakh ba pré sora wakh li borom kham kham yi wakh
2026-08-07 01:18:38
1
ka Agrisell consulting :
ibnou taymiya lo eup xam xam wa tarikha yeup
2026-08-06 16:35:58
7
Ousmane kane :
waliye Ndyisan Maclal Gamou Madine Baye naiss international ♥️♥️♥️♥️♥️♥️
2026-08-06 21:18:20
17
Khadim DIAKHATÉ :
Ibn Taymiya nak eupna sofantal d borom xam xam la. « Ben waay la rek… » c’est trop minimiser l’homme…
2026-08-06 14:20:14
5
s.baba.niang :
khaw ma lou khew de wayé ibnou mame mor anta seuli ak sokhna diaiyatoull laahi ken dou mom ❤️tambalé thi mom yam thi mom