sama qesition moy. mbalik. bi fan lay bayéko si place yi wala
2026-08-07 17:27:56
11
ouss Bolt sow :
ani milliares yii??
2026-08-07 08:05:15
8
Mame Thierno :
@Mame Thierno:noum mel rék y'en commerçants yi am guèn si wall ndax ken ku nek bu diayè ba wathie laka weur lepp mu nettoyer ko bu boba Li man na bania deme ni🙏
2026-08-09 18:47:30
1
Diouf :
Yena gnifay ligueyé yenay premier responsable
2026-08-09 14:23:03
4
sante yalla talibé sonko :
touba lifineke amoll fene😭😭😭
2026-08-09 12:32:07
2
falloudia97 :
Wallahi touba amoul mer😭
2026-08-07 14:42:53
10
BDM🏛IMMO :
milliards yi nanko déf si inondation bi mieux que ay PAVAGE
2026-08-08 20:53:57
3
lemaitre :
ani maire bi?
2026-08-08 02:08:44
2
sopey serigne Saliou :
lou ngen ame duel yen wa touba wolen sen leader sonko
2026-08-09 19:23:34
0
Domou Sérère bi :
Yén wa marché bi djiémolen Dara
2026-08-08 16:03:45
3
fall Qualité :
Thiaye sama réw mi
2026-08-08 18:34:06
1
@Cheikh Niang Touba :
Mairi touba mome dafa wara dibitioné
2026-08-07 16:20:12
4
GARMYS FALL ELEVAGE :
thé bouko baye faye yi defaré bamou bakh nga tekhaw fi ba kén dou am foum diar bou yakho nguéne di sétan . bouko baye fall yi defar gnénégni di dingate
2026-08-07 23:43:05
0
Yoro Diop🇸🇳 :
❤️❤️❤️❤️
2026-08-07 08:57:17
2
El Hadji Saa Fitna🇸🇳 :
touba amoul mer😭
2026-08-07 13:00:55
1
@Cheikh Niang Touba :
Li mome warnagne cée wakh déh
2026-08-07 16:17:45
1
Diop le noble ✪ :
Nioune gni fi négue dh sono nagne
2026-08-07 16:23:42
1
SONHIBOU GUEYE BOU SONKO🇸🇳 :
virement touba amoul mairie li serigne touba merito wouko
2026-08-08 00:30:56
2
Beugu sonko ba diékh thi tak :
Abdou lahatt ka nak wakh deugu yalla war na gor gor lou ahh😢😢😢
2026-08-07 12:57:26
1
Ibrahima Seck :
Sénégal naniou bayi thiaakhaane yi té ligueeyi. baakh neu rek
2026-08-10 00:18:37
0
hôtels703668703 :
mé légui kane la sawy
2026-08-09 23:34:19
0
To see more videos from user @cheikhounadieng65, please go to the Tikwm
homepage.