@film.en.wolof.1: 🎬 Bouki ak Samba – Xaalisu Wurus 🐺🐰💰 Épisode 17 : Bouki tàmbali xeex ak Samba Bouki gis na ni Samba Lapin di dund ci alal ak mbégte: kër yu mag, oto yu bees ak dund gu rafet. 😱 Waaye xolam fees na ak mer ndax li mu séddoo ak Samba. Ndax Bouki dina jàppale boppam walla dina indi jafe-jafe ci xaritam? 👀 🔥 Toppal épisode yi ci topp ngir xam lu Samba ak Bouki di def! #BoukiAkSamba #XaalisuWurus #SérieWolof #Senegal #TikTokSenegal