@ibra.diatalibesonko1: #ousmanesonko2024🇸🇳 #creatorsearchinsights2025

ibra.diatalibesonko1
ibra.diatalibesonko1
Open In TikTok:
Region: SN
Saturday 08 August 2026 08:19:43 GMT
165326
14031
984
363

Music

Download

Comments

saloumsaloumbi607
SÃLĨÕŨ NGÕM ⭐🌟🌠🌳🇸🇳🇸🇳 :
moytou lén père Samba si plateau yi bakhna
2026-08-08 14:00:47
74
toubaalazharmultiservice
Ousmane Samb :
Tay la xam Dabaly wayé tay la bayi maire bou Dabaly
2026-08-08 11:21:18
156
kanda_bou_sonko
Kanda ✪ :
Samba tall mi dh sou done mbeur dou barri combat 😂😂😂
2026-08-08 11:15:40
74
pastef2029
Dabaly city :
Nous la commune de Dabaly on va récompenser Samba tall
2026-08-08 12:06:12
209
www.tikmansour57fall
Mansour Fall :
Mane mi xamoul dabaly sax dama rouss 😂😂😂
2026-08-08 10:40:48
274
ababacar3421
Babacar Business 🇸🇳🇪🇸🇰🇼 :
😳🙆🏿man dh dafma fèkoun may nakharlo worgui diomaye wor 😍ousmane Sonko ❤️😃ms bima guissè lii (1) dama rouss 🫣 (2)sama stress dafa youko 😔
2026-08-08 15:09:19
2
kskomdigitart1
Babu Dezigner 🇸🇳 :
Dina fi moussa ray nit en plein émission 😂
2026-08-08 09:11:05
334
user2352284340170
beugue yayam :
sonko yallah koudou fane
2026-08-08 09:58:01
62
leuz8306
leuz🇸🇳🇮🇹 :
Dina fi mass Ray nitt ci plateau 🤣
2026-08-08 14:02:27
64
diagnesall1
oumy mbaye :
wa man louy sama yoon si waxji bama am si gathié
2026-08-08 09:32:00
89
sonkomoydiomaye14
ani bou sonko :
deumb aka ma contane ki gueumoul dara bari wakh 🤣❤️
2026-08-08 14:18:05
2
aldimobadousamb
aldimobadousamb :
hé naniou cagnotal samba way😂😂😂
2026-08-08 13:31:15
10
user7665576969316
ada bou sonko talibe baye bi17 :
tall boul ray coulou nayi dama bege nieou feke 2029🤣🤣🤣🤣🤣🤣🤣
2026-08-08 13:49:40
2
ngathiatebousonko1
Nga Thiate Bou Sonko :
comprendre nga lima la wakh😂😂😂😂
2026-08-08 11:04:58
11
modounias0
Modou Niass :
Wa ana mame makhtar diamra damako guisatoul
2026-08-08 14:45:00
0
alhamdoulila8
Kholou Djieukeureum :
Wouyyyay ay samba loy out si samba tall mi bakhna tagowo deh worone guama tagou deh sama promo lycée maba Diakhou ba Nioro
2026-08-08 09:57:27
18
melimelobyliz
melimelobyliz :
tei nonou laniou ame daal meuneu deglou 😂😂😂😂😂😂
2026-08-08 13:55:27
13
khadimbambagueye6
Khadim Bamba Gueye :
Comprendre Gua mou nane waw 😁😁😁😁
2026-08-08 09:48:33
64
weuzbarkham.le.pa
weuzbarkham le patriote :
Les tambacounda demandent une émission entre pape bana dieye le maire et samba tall nguir yalla 😂😂
2026-08-08 10:36:36
33
diawara.influence
Diawara influenceur :
il n a rien fait à dabaly merci beaucoup
2026-08-08 09:41:25
54
princesow7742
BOUB'S VINI 7️⃣🐄♥️🎯 :
Le gardien de la révolution 🇸🇳
2026-08-08 09:36:14
39
maguetteniang5784
Sénégal rek :
Diap léne Dinako ray dinako ray dinako ray😂😂
2026-08-08 09:39:49
32
ahb801
A H B ## :
bayilen souniou maire bii way 😂😂😂😂 samba tall qui est tu
2026-08-08 10:15:07
23
To see more videos from user @ibra.diatalibesonko1, please go to the Tikwm homepage.

Other Videos


About