Ayway li nekhena vraiment reconnaissance dafa ame solo si homme
2026-08-10 19:59:43
60
Bijouterie Firdawsi :
Mash’Allah… qu’Allah vous donne des descends pieux qu’Allah vous garde et vs protège vs done des jumeaux et des jumelles amin ya rabi si barké Mouhamed (psl)
Diabar bou bakh d'arnaque lou nekh machallah té yomboul
2026-08-09 14:44:21
16
Tin - Tén flo :
léegui soukh mooy sama mbeur dama beugueu mou nék Rio des arènes
2026-08-09 17:45:08
20
Tawou astou Camara :
Oh pourquoi je pleure melni makay sede te xamoumako sax yalla nalen yalla moussal si thiaat
2026-08-11 01:50:35
7
Bia Beauty :
Peul nala sunu borom may ndiaboot gou barkel
2026-08-10 14:38:25
6
PAPA :
Li raffet na bly 🥰❤️🥰❤️🥰
2026-08-09 09:46:04
26
Agence immobilière Konaté Immo :
Alhamdoulila Alhamdoulila dieuredieuf peulh longue vie à vous 🙏🙏
2026-08-09 09:40:08
12
diaw9_ :
Diabar diou bkh louko way dieundé diar nako
2026-08-10 23:40:37
3
ibra gning94 :
yalna yalla guena deugeur seuy bi té défall léen diabote gou barry té barkel ci mbarké serigne touba
2026-08-10 12:18:25
6
Dame ndiaye :
Diabar diou bakh moy lep
2026-08-10 21:23:52
8
Jullprsi🥷 :
Yalla na yalla deugeureul seuy bi ahh sokhna sou bakh moy lepp Ohhh
2026-08-12 11:43:46
2
moussadieye23 :
oh yalnanou yalla maye sokhenasou bakhe 🤲☝️
2026-08-10 19:00:19
8
ozil22 🩸❤️🇸🇳 :
Machallah amine inchallah
2026-08-10 22:31:00
2
oustaz pape mbor diop :
macha allah
2026-08-09 22:31:44
2
Alassane Diouf :
Yalna yalla takhawou léne té barkél séne diganté
2026-08-10 09:15:04
7
touba94 :
Machalla
2026-08-09 23:40:47
2
Papish :
la première richesse d'un homme c'est d'avoir une bonne épouse...c'est une bénédiction qui peut en attirer toutes les autres formes. avoir une bonne femme c'est faire déjà la moitié du chemin qui mène vers la plénitude. que Dieu nous protège et surtout préserve les ménages
2026-08-11 15:07:01
2
idysow980 :
Machalla
2026-08-09 08:13:33
4
dabakh129 :
maachaallahou laf thiat
2026-08-09 12:52:13
2
Bathie fashion :
machalah
2026-08-09 10:52:10
1
🇸🇳💎NIANG Ballo💎🇸🇳 :
yalla nala yalla 🥰🥰🥰takhawou yalla maylén sey bou barké si barké seydouna mouhamed 🥰🥰
2026-08-10 12:45:37
3
To see more videos from user @tiak_tiak_du_rire, please go to the Tikwm
homepage.