Ndeysan kouko xam Deug Wally ladone imité nittt Gni di retane mais tay gueum nako ba bokk ak mom di wayyy nitt ki lo nek gueum ko Gni deuk guediawaye xam nagn limay wax bonne continuation frr💥❤️
2026-08-10 16:03:25
126
Madame Ndour 🇸🇳🇪🇸 :
Machallha Billy ndiaye 🫂😇😇🩷🩷
2026-08-11 12:08:12
1
el capo 🇸🇳bou adda❤️👗👠👖 :
Billay linga waye fii mane mome betouma billay are dinalla faye par force 🙏
2026-08-10 18:38:44
2
Luno⚽️❤️ :
Billy way
2026-08-11 07:23:30
1
dib's non défaite :
Billy ya bandit 🥰🥰
2026-08-10 14:09:07
1
p@py lô :
wawaw gaydelo borome ndam🥰
2026-08-10 14:11:47
2
ZØ BARHAME 👕👖🛍️ :
Lék rék gua defoul wally 🎤😂😂 sou taxawone mou dead 😂😂😂
2026-08-10 14:51:11
17
#luxurycars26🇸🇳♥️ :
boula nekhon niewe nann ay mar yacin Maïssa bigué 😅waye défo ko dga niewe kholl fii temps bi tolou ga andak mom 🥰
2026-08-10 17:40:43
24
baye cheikh Maestro :
nice Billy
2026-08-10 18:22:02
1
Bb Dior ❤️ :
Sama khol sed na en te voyant chanter au prêt de Wally seck ta tjr aimé ces chansons depuis Joseph Coréa
2026-08-10 13:42:03
27
Chérif___Mounir :
mashallah tu chante bien
2026-08-10 07:18:29
48
user1935909695897 :
li leupe pape thione la molene si napatale machallah❤️❤️❤️❤️
2026-08-10 08:11:14
25
@Billy ndiaye officiel🎤🔥❤️ :
Yalla nala yalla lafal la thiate li ci kanam rawouli beut diga té musique senegal bilahi billy ndiaye 🫵❤️😭🩸🔥
2026-08-10 09:35:37
15
𝙉𝙙𝙚𝙮𝙖 𝙒𝙖𝙡𝙡𝙮❤️🇸🇳 :
oooh machallah li nice na🥰
2026-08-11 22:27:21
3
Rak’N’Tiak Express :
Kiiii xamolene ko sah … yagggg naako wooyy lo cii mbeddd gounass yii. Il est pétri de talent mashallah
2026-08-10 22:39:06
5
Louisa maabo❤️ :
machallah mes amours je vous aime fort mes faramarenn yi❤️❤️
2026-08-10 08:44:22
14
Mariane khoudoss💅🏽❤️ :
Kou meune la rk machallah
2026-08-11 16:01:20
3
🎀Aisha🎀 :
woooy sama Hol bii ohhh🥹🔥🔥🔥🔥🔥
2026-08-11 01:29:37
2
fatou298 :
Incroyable talent ce jeune une fierté cette famille gneup meune
2026-08-10 09:02:20
5
yacine rassoul🥰 :
www ❤️❤️❤️
2026-08-10 16:31:09
2
Maguette seck saliou officiel :
Wawaw sama dom dji ya meune nak ❤️❤️
2026-08-10 19:15:19
4
ame ndiaye :
Ndanane pur💚
2026-08-11 00:32:41
1
To see more videos from user @billyndiaye22, please go to the Tikwm
homepage.