Fofou la diafer ragual nittt beu souma commencer beug nittt dama lay daw telmen febar la si dieler diouy beu fadiare yew wo sama yaye di diouyyyy nane ko ki mane lay def ni
2026-08-11 15:46:08
14
SunuRew Sénégal :
Massiii xam dara walahiii lou nekk si Teranga defal nako mais mom lou bone rek lay wax ci mane yobb nako fou nekk bokk lou nekk ak moom barke borom Touba
2026-08-31 07:21:20
2
diarista❤️ :
Mo gueneu metti bou mbeuguel dé Bly métina
2026-08-15 00:15:20
6
Ma ❤️❤️ :
Mo takh ma bayi kharite kéne beugoule kène kouné da bopou gua beugue
2026-08-10 20:31:06
10
MISS~CAVIAR❤️🫧 :
Tau ou tar karma dina gneuw billahi
2026-08-12 02:50:52
1
Alkhamdoulilah 🙏🙏🙏🙏 :
Mo takh amatouma kharitt je vis dans mon coin tranquille
2026-08-11 09:46:51
7
Sister :
Aka meti liguena meti moy doko khar
2026-08-10 20:34:55
3
Kawthar Ba :
C’est dure deh mem so len diubowe ce n’est plus pareil
2026-08-10 20:34:31
5
💍la belle Fa ❤️ 🫶 :
Mako doundou layyyy touti ma dé j’ai beaucoup pleurer 😭 mais maintenant cv
2026-08-14 22:16:43
2
yayou pape malick :
Massi kham dara
2026-09-01 09:43:28
1
Dia toucouleur :
Massii xam dara billay
2026-10-05 23:12:14
0
alekhamendoulilah :
dalenama touti ma dé wayé mougne te dianguessi dotouma daledé
2026-10-06 11:07:17
0
Leuz Talibé cheikh bi :
Pourquoi deux personnes qui se sont jurés amour et fidélité et se retrouvent à se donner des coups de poings ?
2026-10-04 02:39:27
1
Origine Arafat Shop 🛍👕👖 :
Lou. Méti billay walay 😏
2026-10-03 22:32:44
1
mme sarr :
2026-08-25 02:35:58
0
user57595891799 :
😢
2026-09-11 19:38:22
0
Ma ❤️❤️ :
Kouné sa bopou gua beugue
2026-08-10 20:31:28
1
Ousmane Kobor :
😭
2026-08-10 22:36:40
0
La guerrière de, Sonko😘👑🇸🇳 :
Mangi hame dra 😳😳
2026-08-15 22:21:14
0
mbaye :
😭😭😭😭
2026-08-15 21:57:17
0
Diallo Traiteur :
Bilahi 💔💔
2026-08-24 19:48:39
0
La guerrière de, Sonko😘👑🇸🇳 :
Dama diomi bi mako doundè😭
2026-08-15 22:21:38
0
jmd :
bouma kéne fréquenté
2026-10-06 12:16:22
0
Le petit prince :
En plus sama domou baye la on était tout le temps ensemble
2026-08-20 11:37:22
0
K.F :
Walaahi goumin amical est pire que celui d'une relation amoureuse
2026-08-10 22:59:41
0
To see more videos from user @serigne.saliou.merveille, please go to the Tikwm
homepage.