@baayi.si.xeel: Nit ñi mën nañu la neenale, walla ñu bañ la jox sa cër ci aduna. Waaye loolu amul benn solo! Ce qui compte vraiment, c'est le respect et l'amour que tu t'accordes à toi-même. 💯 Bul yàqq sa waxtu ak sa doole di ñaantu bëgg-bëgg walla fonkite ci nit ñi. Bu dee am na koo xam ni bëggu la walla falewu la, bul fexee diko convaincre. Récupère cette énergie te nga def ko ci sa bopp : Bëggal sa bopp : Bul xaar keneen ngir mu jox la valeur. Fonkal sa bopp : Bul nangu keneen di la wàcce walla dila xeeb. Falel sa bopp : Liggéeyal ci sa objectifs te jiital sa yëf ci lépp lu lay sàkkal ëllëg bu muuch ayib. Nite gi ak doole ji, mi ngi tàmbalee ci biir. N'attends personne pour te donner de l'importance. Baayi Si Xeel ! ✍🏽 👉 Abonne-toi ngir am yeneen xalaat yu am solo bes bu nekk! ❤️ Likel te nga enregistrer post bi ngir fàtteku ko bes bu la xel gi jàxlee. 💬 Tague ci commentaire bi nit bu am solo ngir mu jànd ci message bi! #BaayiSiXeel #viral #Motivation