Avant-hier danio khoulo mani damakoy bayi légui Hier ma dém gallém pour wakh ko souniou digeunté nafi yam bimaye dém nak mangui niangual di déglou song Coumba Gawlo ( Sama Khol ) mais est-ce que kham nguén fane la moudié bimaye gnibi 😫😫
2026-08-16 14:01:48
421
Soxna fat diakhatè ❤️ :
Mane Miko bloqué wone whatsapp mou message ma TikTok ni ma bb rk ma débloquer ko 😏😏
2026-08-14 21:08:16
913
PAPA CISSÉ 🙌🏿☝🏻 :
Wa Legui daguene may diema expliquè GALSEN kan moffi nekoul en couple😳
2026-08-16 16:15:01
319
ZAHRAA !!💕🫧 :
« YAYEEE BOYEEE »BII😔❤️
2026-08-15 19:40:39
345
soxnamai rassoul 🫶❤️ :
man dé dan ma mère 2 jours mongui ni degou mako 😭🫣🥹
2026-08-15 12:53:58
128
Ndiss🏀🏋🏿♀️📚 :
😂So Neko hey bougou ma lii moy wakhat lako ohhh
2026-08-14 16:31:14
325
Élevage Sénégal 🇸🇳 🐏❤️ :
Non nékhoul ba nékhoul mbeugel dafa nekh 🥰❤️
2026-08-14 23:42:58
144
chef 🧑🍳Soxna maï❤️ djamil :
mne deh bb rek lmay wax ma retane
2026-08-14 14:22:13
200
𝚳𝚯𝐔𝐒𝚻𝚫𝚸𝚮𝚫🇸🇳🇪🇺🇺🇸 :
Man meunouma merr dma gawa retan 😭
2026-08-15 02:29:21
299
DIAM L'AIR JR🫡🇸🇳 :
soumako méréwé rek mou statut bopam ma balko ma kham Loutakh nk 😂😂
2026-08-16 11:57:50
69
La Diablesse 😻 :
les filles kagne ngene commencer beug nk wakhanté wouniou wone li de 🤣
2026-08-18 15:22:40
23
𝒵♡ 𝓍ℴ𝓁𝓊 𝓈𝒶𝓃𝑔𝓊ℯ 𝒷𝒾 :
Ohh yalla boumniii zeynaaaaaaa tw aussi ohh lii yalla bouko sama yay guiss😂😂
2026-08-15 12:18:47
37
Une 💋Princesse 🥥💝 :
lay maneuh mii hier may histoire mou yokou ma wakh sma tour ma titeu 😱 mouni ma je t'aime tekk sii naneuh fais mw un gros bisous 😭😭😭 trawlisss naa ma😭😭🥹
2026-08-15 16:42:58
78
Aïcha shop❤💍✨🥰 :
Ndeysan hier ma mèré ko nak di khoulo ak mom louné ma wax ko rk mouné bb kham nga mane xawma problème ohhh ndeysan ma rouss