@Bayou housseynou:niak xam xam baaxoul.
yonetbi ay arabe dong nio nékone si kanamam kon arabe lay wax.
khoutba discours islamique la pour diangalé.
kon fawou niou firilko nityi.
so topé sa logique bii diné dji ken douko xam.
est ce yonet meusna tafsir si wolof pourtant niongui Tafsir ci wolof.
yonetbi meusoul diangalé dara si loudoul lak arabe.legui xana kon danouye bayi diangalé diné si wolof
2026-08-14 23:43:54
0
Elevage business :
Khotba waroul donnn arabe langue bi gnicoy declou laniouco wara deffff
2026-08-15 16:29:30
1
kebe le salafi :
Ki mom daffa nexxxx
2026-08-14 20:34:27
1
H ceesay talibe cheikh bi :
xutba si lou nekoul arabe jumma jii dou wer
2026-08-16 21:45:15
0
L'œil du Travailleur Social :
kou beuga kham diangui
2026-08-15 15:32:11
0
E.B.D :
yow wéro
2026-08-19 23:27:40
0
user6704172739125 :
🥰🥰🥰
2026-08-12 22:54:55
0
Muhammed Will baye 19 :
🥰🥰🥰
2026-08-12 18:18:51
0
user80754901373 :
🥰🥰🥰
2026-08-12 18:25:45
0
Aly Diop :
🥰🥰🥰
2026-08-12 22:36:19
0
To see more videos from user @fallou.niang.business, please go to the Tikwm
homepage.