@aleewjaaw: #senegalaise_tik_tok #diasporatiktok #adamo #kaliphone #thies

Diaw director🇸🇳🎬
Diaw director🇸🇳🎬
Open In TikTok:
Region: IT
Wednesday 12 August 2026 18:49:38 GMT
640069
64237
2714
2189

Music

Download

Comments

makhou1998
union de baol :
sama xol séde na si asane gueye🥰 je suis fériée de toi 😁🤣🤣🥰
2026-08-12 21:16:28
2044
papaousmaneniang0
papa ousmane :
Kene dou cautionner rayy mane nitt soko beuguoul boul lekk xalissam touki dafa metti
2026-08-12 20:33:33
4686
ndiaye40988
Ndiaye :
Merci Assane gueye
2026-08-12 21:49:27
160
mamecheikh37
mame cheikh :
Assane yalla nala yalla djiégeul 😭
2026-08-12 23:07:16
1334
petit.pokemon5
Petit Pokemon :
Ana banque tamit louy ndiarigname
2026-09-15 07:41:14
0
tzizkdbkfbkrogokgnfldndn
capricorne ♑️ :
pourtant assane mo nek si deug
2026-08-12 23:21:43
1786
tallomar1237
Tall Omar :
Keneu andoul ak ray nitt mais nitt soko beugoul boul lek khalisam
2026-08-13 00:13:34
2784
seydinaousmanesarr2
SARR :
ohhh assane ndeysane
2026-09-15 16:21:06
0
zeynaexwally
zeynaexwally :
Certes moko togn mais ray nit dafa graw
2026-08-12 23:30:26
1816
mbeauty109
M. beauty10 :
Mane dhe sama yaye à chaque fois dafmay wax ´nit boko beugoul boul lek khalisam
2026-08-13 01:36:30
1003
saa.lif4
Saa Lif :
Akkk li yalla wax si kou rayy nittt pour man xaliss diarouko
2026-08-12 20:43:58
464
moussasylla634
real madrid :
kou goor ki légitime défense la def
2026-08-12 21:08:03
259
birahim.ndiaye471
Birahim Ndiaye :
Assane déf na limou waraf lépp
2026-08-23 14:03:29
202
timalakarimienne
timalakarimienne_MSR BARRY❤️💍 :
Ray dou yonn wayé Maréme bamou démé ba beugko woor nako délo xaliss samm 🥺
2026-08-12 21:03:43
946
sopedieukeureume
YAS(ELEVA GRUP)🇸🇳❤️❤️ :
Assane Gueye yalla Nala yalla takhawou.
2026-09-14 11:18:52
1
lampgunners
le gunners ⚽❤️ :
mann Dina Dieul sama xaliss diko envoyé sama guél
2026-08-23 21:26:38
60
diallo.dierry13
Diallo Dierry :
la trahison fait mal mais la vie de l'être humain chère
2026-08-12 22:34:55
359
alediome322
Alediome :
Salah lahou alah Mouhamad ❤️❤️
2026-08-26 20:46:47
20
bamba.ndiaye9304
Bamba :
nitt boko beugoul boul lekou khalisam 😎
2026-08-23 16:58:02
129
uzumakisng
PandaBoyGamers🐼🎮 :
Assane je suis fier de toi
2026-08-13 06:06:16
15
r_j_l_95
R J L 🇸🇳 :
lii yagg na trop pourquoi soulever waat ces histoires? pensez vous à leurs familles?
2026-08-12 20:33:57
283
thiorapple
Thior Apple 🍏🍏 :
Nit soko beugoul bayiko ak alalam ´
2026-08-13 01:25:48
432
00000000000747613s
Rymoush ❤️ :
Koumay wave 5 mil svp 🙏 🙏
2026-08-23 08:42:11
9
To see more videos from user @aleewjaaw, please go to the Tikwm homepage.

Other Videos


About