Macha alah sama loxo si kaw sama watshap samay mbok ak sama famille dieukeur gnongui koy guis dama seuy si fekk famille diaxasso ma souder wate lep bolé wate gnep dioubolé gnep defois ma wax lougne ma waxko woul juste pour le bonheur de tte la famille yalla nagnou Yalla MOUSSEUL si DIEKK bouy séparer famille ak gneuw si keur lep changer
2026-08-14 20:05:31
33
Dijachu😃❤️ :
c'est pas vrai dans toute les familles y a des histoires : que des bombes à retardement
2026-08-14 19:31:07
17
Kholou khalil💞 :
Bilae deugue leuh sama tanta dafa dougou souniou famille rk diam diékh mes yalla giisna lepp
2026-08-15 13:15:48
6
fama Alioune gueye :
vérité absolue
2026-08-14 19:08:56
12
Adja foune♥️ :
Vraiment absolu
2026-08-14 15:44:01
6
Maty Fall :
bilaye fall ❤️❤️❤️❤️❤️❤️
2026-08-14 18:16:38
6
Sokhna Mbene Mbengue❤️💯🥰 :
Ay way Yalna niou yalla def ak Sokhna’s you bakhhh
2026-08-15 15:40:37
1
Mrs Ba :
mane dhé sama dieukeur lay diox tor à chak foi sou dioté a magam yi mm gnou togneko juste pr apésé la tension mé souniou wété ma balouko é il me comprend cé pa facil dhé
2026-08-14 16:59:08
6
alalou khadime rassol 💍❤️ :
bly amna sono keur 😩😩
2026-08-18 14:38:21
1
une diouf :
biilay Lou leer
2026-08-14 19:52:00
3
Jamal optique :
Lolou deug le
2026-08-14 21:43:00
2
Aminata mou selmi mou sb Sy :
Bilay Amna
2026-08-15 03:14:19
1
glamour ♥️♥️♥️🥰 :
dama beug statut mais dama mandou
2026-08-16 17:06:27
1
ndoyearame22 :
J’ai envie de le poster 😂😂😂😂😂😂
2026-08-15 17:00:30
2
kader :
bilahie doy na warr
2026-08-18 12:24:55
1
Seutou djine bi :
Walakhiiiiiii
2026-08-14 21:57:34
1
Bana Dieng :
Beugeuna statut
2026-08-14 20:14:20
4
Bineta :
bilahi
2026-08-14 18:23:24
1
damecoundoul15 :
machallah oustaz
2026-08-18 20:17:07
0
user4064571276060 :
bilakhi lou leér nga wakh yalla khamnako
2026-08-19 06:37:38
2
user2994935867041 :
Bilahi Diekk Bou bonne bangui sougnou keur ,tasse nako😭😭
2026-09-10 22:04:06
0
nafina10 :
Ma netaliiii wala
2026-08-19 15:44:32
0
nogaye Ndiaye ♥️🥰 :
bilahi deugeuleu
2026-08-14 16:06:07
0
To see more videos from user @galsensuperstar, please go to the Tikwm
homepage.