ngén balma wayé peut-être dou vidéo bii moma tah di wah ndah damakay guiss ay vidéo nitt di wah ak sohnam nanko fassé nala wala maynala sa batt thi ay vidéo ay nitt dissi rigoler et pourtant ay témoin lanou thi wah dji wayé gnoukay moytou bahoul dé ak diegalou nakk peut-être diguén comprendre finalement wahé da am lo khamni keneu douko kafé thi mariage wassalam