man sm boss ken dindi woumako motkh khaw ma dm dotom khw ma R dal khalatou mako wax😭😭
2026-08-19 14:48:24
6
adamandiaye160 :
Bilahi sama dôme taye dji lanouma wakh ni dindiwounioko te Amna 5moi Eskeu d’où amprolem😭😭😭😭
2026-08-17 20:55:18
234
Saliou Mbaye :
Mandé Amna co ta mngui wakhe normal
2026-08-18 00:39:05
101
Zall Graphiste🦁 :
Kou ale problème R👈😂 COMME MOI😂😂😂
2026-08-19 12:18:51
96
khoudjista 🌸🍀🧕 :
li kay motakh ma dotom dagoun sama boss
2026-08-18 00:12:16
46
khadim thiam :
xalé bou am 7ans ésk dinaniouko mana dindi? ?? ??
2026-08-19 09:46:26
11
JMD :
Li deh mo takh ma dotom bilay et j’ai 23 ans defois Demay rouss sah
2026-08-19 16:20:55
19
kadija21B :
Qui est allé directement pour vérifier 😂
2026-08-19 22:55:26
6
Nelson Ndimbélane 🎙️🪶🧠 :
Li motax may roulé R rek di dem 🤣🤣🥹
2026-08-19 13:11:43
6
flasca ♐️♐️♐️ :
man khamna lignou dindi ci man dafa beuri 😳damay wakh rék
2026-08-19 22:19:08
7
𝔸𝕃-ℍ𝕌𝕊𝕊𝔼𝕀ℕ 👷♂️ 🛠 🏗 :
bb bou am 24 ans
2026-08-18 09:10:12
17
Baye Modou Ndiaye :
bou amé 10 ans es ce que c'est possible
2026-08-19 23:40:26
5
C Sokhna tiguidaaa ❤️🦋 :
Mane sama boss kéne dindiwou ko tei mangi wakh normal ms R la meunoul wakh
2026-08-18 16:10:49
7
Parisiens💚khoudoss :
mane kaye ly motakh manouma wakh
2026-08-17 21:02:52
25
Mrs Gaye 🫀💕boo OG❤️💍🎉 :
Li dé moma téré wakh normal 😅😅😅pour wakh sama tour normal sakh blem la 🥺
2026-08-18 12:04:35
16
frigoriste :
man mi moma dal
2026-08-18 04:38:39
7
anté07020 :
c'est vrai mane sama dome amone nako bimou amé 1 mois sama mag moko setlou néma sa dome bi souy dioy do dégeu boubakh voix bi ci liir bouy soga dioudou normaloul yobouko hôpital ma déme pédiatrie niou néh lamign bi mo doul diog après nio dagueko heureusement sama mag telko setlou
2026-08-18 13:56:18
6
master dem :
that's not true.
2026-08-22 08:47:08
0
MAODO POINT.✪ :
lii kay motakh ma deurr 😭
2026-08-19 19:14:26
2
To see more videos from user @coachndour, please go to the Tikwm
homepage.