Sama mbokk jeune yi dèlène Sangoo Khaaye bakhna trop si thiate
2026-08-17 02:38:18
310
ngonish baby 🌹 :
Yalla nagn yalla mouseul si thiate 🤲🏾
2026-08-16 23:56:47
516
Soldarou Al qourane :
kou beugeu diangue Al qourane ?
2026-08-16 23:48:53
209
𝕰𝖑𝖆𝖏~𝖘𝖊𝖈𝖐 ❤️✌🏾 :
Lima geuna nekh si professeur moy dale gui ak yare guiii 🥰yalla nala yalla sameu
2026-08-19 15:07:56
93
Awa :
Serigne Barhama Niass foumou deuk
2026-08-17 07:32:40
31
Loca 🇸🇳🧸 :
Rapp nak😩😩😩
2026-08-17 15:22:28
8
Talibé cheikhna Moy noble :
mane dh 2015 ba tay sama Dara dokhoul souma gueumoul wone yalla touti rék mani danma liguéy ba sama papa fatoo ba tay wallahi méé allkhamdoulilah 🥰 allkhamdoulilah 🥰
2026-08-17 18:31:06
36
amy colle :
Yalla naniou si yalla mousseul ak mbolem djoulite 🙏