ndéysane yalla nala yalla takhawou 🙏
inchallah dinga am ndam
2026-08-17 22:32:49
2
Omar kouta :
Sa numéro sill vous plaît
2026-08-17 14:53:47
212
Abdou fermin 16 :
yalla bakhna yaye boy
2026-08-18 10:11:02
1
fatima falilou business :
ndaye sane ya zayda dina bakh dh incahalla yonou wou bakh mo yombol rk
2026-08-17 13:38:57
1314
Serigne cheikh leye🇸🇳 ✪ :
Machallah yagui may doli courage ya sayda 🙏🥰
2026-08-18 08:20:02
1
khadijatou :
Yalla bakhna
2026-08-17 21:14:50
1
Alkaf :
les femmes battante c'est ceux qui soutient notre saint Coran courage ya seyda 💪💞❤️
2026-08-17 19:56:25
447
Nasrou Dine Tv :
ndeysan seyda li metina trop wante dina bakh inchallah Lou bakh yomboul Daga nekk ci yoon Bou bakh faw rek ga am ay natou de courage ان الله مع الصابرين dina bakh sama xol fees na yalna yalla takhawou la 😭😭😭🖊📚
2026-08-17 17:51:07
60
SÉN_WOLOFAL TV :
Yaw de sunu boroom dala nara dimbali
kouy laggéeyal suñu moroom fawwu mu tekla ay nattu wayé yàllna yàlla motali ta saafara lépp banga am sa daaray boppu bàrkeb Alquraan
2026-08-17 19:20:15
123
Modou Lamine :
yalla nako albarie guiss waye 😭
2026-08-17 22:23:24
31
tening.diome :
salalahou alla Mouhamed
2026-08-17 20:30:47
8
sylla Mamadou 🙏 :
Li daw na Yaram blh ms Yalla bakhna 🥺🥰
2026-08-17 21:45:27
48
sante sunu borom :
Ou sont les milliards de manitou faye🥰🥰
2026-08-17 22:21:05
10
anta gueye 999 :
salallahou alla mouhamed
2026-08-18 04:01:52
12
fans touti saliou 🧕💗💗🫶 :
Oh ndeysan mogn rk di na bax inchallah 🥹🥹🥹
khana touba ga nék
2026-08-17 13:54:03
104
madame diouf :
yalna la yalla takhawou
2026-08-17 20:58:23
11
Mame Astou Thiam La Barhamiene :
ohh li metina torop yalla bakhna dina bakh de inchallah😭😭😭😭😭