ohhhh oustaz Ahmed Ba
bounie koo posé question bii🥰
2026-08-18 23:42:48
28
Cheikh Sidya Barham :
Tout Baye lima neex ssi mom moy dey wax wawdji mou leer
2026-08-17 21:39:23
37
Chat Chat :
I'm very happy🥰🥰🥰🥰🥰
2026-08-19 07:57:33
1
MÄLÏCK BÄRHÄM 🫀❤️📌 :
YA Rabbi Ñungui Lay ñaan , Dila Daggaan Kattan ak Fan wu Gudd ci sa Jàam bii di Cheikh Mouhamadoul Amine ibn Cheikh Ibrahima NIASS (Baba) 🤍
Yàlla dolli wér gi ak fan yii ci Barke Baay !🤲🫀🙏
2026-08-18 21:19:00
17
ousmane mbaye1 :
alhamdoulillah yalla Nanou yalla fayel cheikh Ibrahima Niass
2026-08-17 21:12:50
46
@mouhamet ❤ seck❤ 585 :
barke baye Niass ohohoh tou baye begé Nala ❤️❤️❤️❤️