biñi dingue jazbou bi ci magal gui amna digeunté Bo khamné Bay mataar dafa guennone Nourou modone dirigé mo daadj Sallim hala Baddrine diala gui sakh🥰❤️
2026-08-17 21:04:10
71
Lat soukabé :
Merci infiniment iao xame xame ngaye waxe ♥️♥️♥️
2026-08-17 18:16:30
23
SÉNÉGAL 🇸🇳 FARMING :
Wallahi la preuve si magal gui matar dafa geune norou diouf daadje lou nékh 🥰
2026-08-19 23:50:19
8
Mouhamed Kane :
Wakh diou Rafett rek la xam si iaoe
2026-08-17 22:43:36
20
Aliou ridial :
Wollay ndéyesann lou wèrr 🥰🥰
2026-08-17 21:51:34
23
OmarGalloNdirkhassida🙏htdkh🤩 :
Serigne Moustapha mome désé raw fite mimou am yéme nama🥰
2026-08-18 12:16:27
5
Ka borom deuk bi :
moustapha niane norou diouf lamp geuye lahad ouseynou makhtar diaw khadim dia cheikh ndiaye 1 et tt tank samsou mor secke ak baba ndiaye
xalè you ndaw🥰
2026-08-20 09:31:13
4
Souhiabou ✌️ :
Amna solo
2026-08-17 18:25:46
3
baye modou seck❤ :
Walay ndaysan werna de🥰
2026-08-17 20:04:14
10
KHADIMOUL RASSOUL😍😍 :
Inchallah Nourou diouff moy djité dji kourel🥇❤️
2026-08-20 17:04:13
3
babs :
deugeu la dé walahi htdkh nio bakh dara diou nangou yof bakh
2026-08-18 12:38:29
3
s m :
Serigne lampe Gueye
2026-08-24 16:29:05
1
dioum bichri xassida :
bilay wakh nga degue machalla
2026-08-22 15:39:57
1
Ndeye mbene Diop :
ماشاء الله
2026-08-24 20:40:54
1
baye lahat sylla HTDKH🇸🇳🇧🇷 :
Billay ndayesan ❤️❤️❤️❤️
2026-08-26 14:45:52
1
s Bara Bousso DMB :
waaaw gooré waaay
2026-08-17 18:17:50
5
morndiaye696 :
Xaadim Ja
2026-08-22 23:39:45
1
💫CHEIKH FALL 🇸🇳☝️ :
jambar lan de ndeysan 🥰
2026-08-17 18:23:58
5
Bara bichri 💚🤍 :
Lolou moy adina ❤️❤️❤️
2026-08-17 18:22:40
10
Fallou Ba :
machal lah ❤️❤️❤️
2026-08-18 22:34:24
1
The man🥶 :
Wallahi deug gua wakh
2026-08-26 09:54:21
1
𝙃𝙞𝙯𝙗𝙤𝙪_𝘽𝙖𝙮𝙚 𝙁𝙖𝙖𝙡 :
bilay lou wérr nga wakh
2026-08-19 21:37:02
1
Cheikh Abdoul Ahad :
Ndeysaan Waw goor mouride jangatt bou am solo wallahi
2026-08-17 23:25:58
2
Serigne Saliou Kane :
ماشاءالله جرجف رفتن لولولول♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️
2026-08-17 22:42:41
3
akhmadou HT :
ya bakh te kham Lou bakh
2026-08-17 23:40:09
2
To see more videos from user @modouboussothioune, please go to the Tikwm
homepage.