😂Ah seydina mouhamed mom bayiko ak malick fa wade mom hame nako maîtriser nako aussi lou bari louma hame si yonente bi si mom lako hame yalla. Hame nako daguey xool khilassou zahab rek résume na lep si yonete bi koku moko hame
2026-08-19 17:10:45
13
goor deugue :
Mame maodo rék moma doy si yonénte bi❤️❤️❤️💯 khilass rek
Wa gamou nak mom niepa ko Bokko waye Tivaoune nak nio si man
2026-08-18 23:34:43
9
maçon professional :
aka wer
2026-08-18 22:15:37
8
B C I B F 🎆🎑 :
billahi lou wér la wakh
2026-08-18 23:01:51
18
SAYDINA ALIOU bou sereigne Sam :
ki dafa Fatou bayi léen li ngéen nî wakh
2026-08-19 18:56:53
0
Begue bamba❤️ :
Mouride la deh mes gamou gui souy niowe rek sama mbokou yi daniouy diafour di wakh rek nangoul li yalla dogal do sonou El hadji malick moy borom gamou gui
2026-08-19 17:11:45
36
tall bou serigne sam mbaye :
bilaye
2026-08-18 19:54:26
6
Gueye mou baye niasse :
ssma khél démna si Minka🙏
2026-08-19 15:17:51
5
Moussa Kebe :
2026-08-19 20:36:14
2
Modou Ndiaye :
Mouride kay serigne touba laniy wax ndax gnousi bari néna gnou magal mo geune gamou
2026-08-19 01:12:06
4
Bollo Ndiaye seck Ba :
Wakho deug dh yenal wakh sene serigne ma guene yonet bi
2026-08-19 19:14:35
0
Ibn Babacar Seck☪️✅ :
Ki waxou Fi Dara
2026-08-19 00:10:33
3
To see more videos from user @saydina.aliou4, please go to the Tikwm
homepage.